Dawaan bu safaanu wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
TXiKiBoT (waxtaancëru)
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Dawaan bu safaanu''' ('''DS''' walla '''AC''' ci [[wu-angalteer]]: Alternating Current) màndargoo ag walug [[dawaan]] guy soppiku ci jamono muy ci [[taraay]] walla ci jubluwaay.
== Doxiin ==
Naka-jekk dawaanu [[mbëj]] suñu koy séddale, ci dawaan bu safaanu bu [[Baraay|baraayam]] sax ci 50 Hz walla 60 [[Hz]] lees koy defe (+ ak - bi dañuy safaanu ci watatukaay bi juroom-fukki saa yu ne). Dawaan bi ak [[dendu mbëj]] bi, ci biir [[watatukaayu mbëj]] bi seen Demiinu dafay mel ne bu ab [[duusub sin]].
 
Jëfandikoo gu dawaan bu safaanu mi gi jóge ci li [[Jurukaay|jurukaayu dawaan]] yi, ci yaxanaay ci koom-koom ak seenug yomb a defar, di jur dawaan bu safaanu ci anam gu yomb, kon dawaan bi ci boppam kenn du ko soppiwaat laataa ag jëfandikoo.
Rëdd 7 :
Fi njariñ li gën a feeñee sax mooy séddaleeb dawaan bu safaanu bir na ne moo gën a yaxan [[dawaan bu wéy]] ci séddaleeb [[taraay bu kawe]] (ñakkug kàttan gi ci buum yu gudd yi moo gën a néew). rawatina, ci diggante gu [[gennwéq]] walla wéq yu bari, bir na yaxanaay gu [[ñettiwéq]] di gees gën a jëfandikoo ndax néewteey ñakkug kàttan ngir njeexitu [[Joule]] (moo tax dijjaayu watatukaay yi gën a néew, maanaam wëñ yu gën a sew); jëfandikoog dawaan bu safaanu bu ñettiwéq lawal na buumi yóbb yi ci diggante yu gudd lool yi.
 
Genn Màndarga gu am-solo gu dawaan bu safaanu, ba waral ci genn wàll li tax ñépp jël ko, mooy yomb gee jëfandikoo fu nekk, yomb gee soppi ci lim yu wuute ci [[taraay]]u [[dawaan]], ci ndimbalu [[soppikaaysoppalikaay]] yi, ak ñakkug kàttan gu digu.
 
Donte yenn jumtukaay yi [[dawaan bu wéy]] lañuy doxe, waaye loolu manees na koo ame ci dawaan bu safaanu, sunu jëfandikoo ab [[jubbantikaay]].