Haj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Kmoksy (waxtaancëru)
Kmoksy (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
[[File:Supplicating Pilgrim at Masjid Al Haram. Mecca, Saudi Arabia.jpg|thumb|250px|<font color="green">Haj</font>]]
[[File:Al-haram.jpg|thumb|250px|<font color="green">Haj</font>]]
 
'''Haj''' mooy juróomeelu ponku Lislaam, Ci waxi Yonent Yàlla Muhammed ja ni: "Tabaxees na Lislaam ci juroom: Seere amul benn buur bu dul Yàlla te Muhammed ndawam la, Taxawal Julli, Joxe Azaka, Woor weeru koor, Ak Aj ci ku ko man aw yoon", ba tay Aj farata la ci benn jullit bu ko man (ci bepp anam), ci waxi Yàlla mu kawe ja ni:ñeel na Yàlla ci nit ñi Aj néek ba ci ku ko man aw yoon (benn yoon) te ku weddi Yàlla moom woomle waliif mbindéef yi.
 
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Haj » lañ ko jële