Doxalukaay bu demandoodi wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 9 :
 
==Doxiin==
Dawaan biy jaar ci lëmës gu tekkaaralaan bi mooy jur ab [[toolu bijjaakon]] buy wëndeelu, xélu wëndeelug tool bi mi ngi aju ci baraayu dawaan biy dugg ci doxalukaay bi te jóge cig ndombo gu biti. Ngir am ab toolu bijjaakon bu taxawul benn barab, di wër, faww ñu am ñetti lëmës yu tolloo, te itam yam [[dendu mbëj]] bu safaanu bi ñu leen di dundalee. Waaye ngir gëstu masin bi doy na ñu xool rekk benn wommatukaay ci ñett yi ndax liy xew ci benn bi mooy xew ci yeneen yépp.
 
Kon lëmës gu tekkaaralaan bi dafay nekk ci biir ag wal gu bijjaakon guy soppiku ci jamono. Toolu bijjaakon buy soppeeku bi mooy sabab juddug jenn [[doole ju mbëjdoxalukaay]], lëmës gu wëndeeluwaan bi su sóoboo ci boobu tool, sunu sukkandikoo ci [[àtteb Lorenz]], dafay xiirtal ci ay catam ab [[wuuteeg aj]], moom it juddal ab [[dawaanu mbëj]] ci wëndeeluwaan bi. Segam xamees na ne su ab dawaan di jaar ci aw taxar, dafay jur ab toolu bijjaakon. Kon ñu am ñaari tool (bu tekkaaralaan bi ak bu wëndeeluwaan bi) liy tukkee ci digaaleeb ñaari tool yi mooy jenn doole ju mbëjbijjaakon, di liy wëndeel wëndeeluwaan bi.