Doxalukaay bu demandoodi wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Luckas-bot (waxtaancëru)
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 6 :
 
==Melokaan==
Doxalukaay bi ci ñaari xaaj la séddaliku, benn bi di tekkaaralaan bi, di xaaj bu taxaw bi, beneen bi di wëndeeluwaan bi, doon xaaj biy yëngu. Tekkaaralaan bi dafa am ay bën-bën yu, lang ak wëndeeluwaan bi, di fi lëmës gi di jaar, maanaam wommatukaay yi dawaanu mbëj bi di jàll.
 
==Doxiin==
Dawaan biy jaar ci lëmës gu tekkaaralaan bi mooy juddaljur ab [[toolu bijjaakon]] buy wëndeelu, xélu wëndeelug tool bi mi ngi aju ci xélubaraayu dawaan biy dugg ci doxalukaay bi te jóge cig ndombo gu biti.
 
Kon lëmës gu tekkaaralaan bi dafay nekk ci biir ag wal gu bijjaakon guy soppiku ci jamono. Toolu bijjaakon buy soppeeku bi mooy sabab juddug jenn [[doole ju mbëjdoxalukaay]], lëmës gu wëndeeluwaan bi su sóoboo ci boobu tool, sunu sukkandikoo ci [[àtteb Lorenz]], gisdafay xiirtal ci ay catam ab [[dawaanuwuuteeg mbëjaj]], buymoom juddit juddal ab [[dawaanu mbëj]] ci wëndeeluwaan bi. DawaanSegam boobuxamees mooyna taxne jennsu dooleab jidawaan feeñdi jaar ci wëndeeluwaanaw bitaxar, didafay itamjur liab koytoolu xëccbijjaakon. muyKon toppñu walugam bijjaakonñaari tool (bu tekkaaralaan bi ak bu wëndeeluwaan bi) liy tukkee ci digaaleeb ñaari tool yi mooy jenn doole ju mbëjbijjaakon, kondi muyliy wëndeeluwëndeel wëndeeluwaan bi.
Dawaan biy jaar ci lëmës gu tekkaaralaan bi mooy juddal ab [[toolu bijjaakon]] buy wëndeelu, xélu wëndeelug tool bi mi ngi aju ci xélu dawaan biy dugg ci doxalukaay bi te jóge cig ndombo gu biti.
 
Li tool bi tekkaaralaan bi jur, di xiirtal ab wuuteeg aj ci wëndeeluwaan, loolu itam sabab beneen tool, di lu ag ñakkam a judd di indi ñakk a demug wëndeeluwaan bi. Tax ñuy far di ko woowee itam ''masinub xiirtal''.
Kon lëmës gu tekkaaralaan bi dafay nekk ci biir ag wal guy soppiku. Toolu bijjaakon buy soppeeku bi mooy sabab juddug jenn [[doole ju mbëjdoxalukaay]], wëndeeluwaan bi su sóoboo ci boobu tool, sunu sukkandikoo ci [[àtteb Lorenz]], gis ab [[dawaanu mbëj]] buy judd ci wëndeeluwaan bi. Dawaan boobu mooy tax jenn doole ji feeñ ci wëndeeluwaan bi, di itam li koy xëcc muy topp walug bijjaakon bi, kon muy wëndeelu.
 
Kon turuTuru demandoodi ngi jóge ci li wëndeelukaaywëndeeluwaay bi manutamanut a yam ak walug bijjaakon bi, xél gi ñuy demee, walug bijjaakon bi mooy raw. Wuuteg xél gi nekk ci diggante wal gi ak wëndeeluwaan bi lañuy wax ''xélu tarxiis''. Xélu wëndeluwaan bi lañu wax ''xélu demandoo''.
 
Lëkkaloo gi ci diggante xélu tarxiis gi, baraayu dawaan gibi koy dundal ak limilimu seexi dott yi (benn limu seexu dott benn bëj-gànnaar ak benn bëj-saalum lay am), mile mind moo koy fésal:
 
:<math>n_s = 60 \, \frac f p </math>
Ligne 23 ⟶ 24 :
* '''f''' mooy baraay bi, ñu koy natt ci [[Hertz|Hz]];
 
* '''P ''' mooy limilimu seexi dott yi
ngir xayma tarxiis gi '''s'''
 
:<math>s = (\frac{n_s-n}{n_s})</math>
*'''n''' mooy xélu wëndeeluwaan bi.
 
Ci misaal, ab doxalukaay bu am ñetti seexi dott ''p'' (6 dott), bu baraayam ''f'' doon 50 Hz mi ngi am xélu demandoo 1000 wër ci simili.
 
[[Wàll:wuutuloxo yu mbëj]]