Ngóora (jëmm) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
LaaknorBot (waxtaancëru)
m robot Modifying: am:ሃይል (ፊዚክስ)
Xqbot (waxtaancëru)
m [r2.5.2] robot Modifying: bg:Мощност; cosmetic changes
Rëdd 1 :
Ci [[jëmm]], '''ngóora''' gi mooy limu [[kàttan]] gi genn noste di jox geneen ci jenn jamono. Kon ngóora daf lay delloo ci kàttan gi nekk ci biir genn noste gi, dila xamal [[liggéey]] bi mu man def ci jenn jamono. Liggéey bi man naa gaaw te woyof, diis te yeex, walla boole ñaar yépp, gaaw te diis, boobaa dina laaj kàttan gu jéggi dayoo.
 
 
== Natt ngóora gi ==
Segam ngóora gi mooy liggéey ci jamono, lu liggéey bi di gën a diis jamono ji mu koy di gën a néew ngóora gi di gën a bari.
:<math>P=\lim_{\Delta t\to 0}\frac{\Delta L}{\Delta t}=\frac{\operatorname dL}{\operatorname dt}</math>
:<math>1\ \mathrm{Watt} = \frac {1\ \mathrm{J}}{1\ \mathrm{s}}</math>
* W: [[Watt]] bennaanu nattu ngóora gi
* J: [[Joule]] di bennaanu nattu liggéey bi
* S: [[Saa]] di bennaanu nattu jamono ji.
 
Nattiinu ngóora gi mi ngi aju ci xeetu noste gees am.
Rëdd 20 :
Sunu xamee àtte bi yor ngóora gi, anam gi muy soppeekoo ci jamono ''P''(''t'') (t:jamono) ak diir bi muy amee, Kàttan gees weccee gépp ci doxug noste gi manees na koo natt:
:<math>\Delta E = \int_{t_0}^{t_1}P\operatorname dt</math>
 
 
[[Wàll:Kemi Jëmm]]
Ligne 31 ⟶ 30 :
[[be:Магутнасць]]
[[be-x-old:Магутнасьць]]
[[bg:Мощност (физика)]]
[[bn:ক্ষমতা (পদার্থবিজ্ঞান)]]
[[ca:Potència física]]