Bisub Tabaski wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Tabaski Sunna la su far ci ab jullit bu di as gor te man ci ag jàppndal, ku mukàllaf rekk mag ak gone ñoo ci yam.
Waaye nag dina ware ci ñaari xeeti nësër yii :
1- ci ku ko nësër niki ngani bu ma Yàlla defalee nàngam dinaa tabaski,
2- ci ku njënd am xar, walla mu yor am xar jublu ci tabaski, manaam kon xar moo njënd niki am tabaski, manatu la ñàkk.Tabaski it ag bër (`iid) la gu Yàlla may jullit ñi, Jële nanu ci Anas (gërëmul Yàlla ci moom) mu ne: Bi Yonent (jàmmi Yàlla ci moom) bi agsee Madina fekkee na léen ñaari bis ñu cay caaxaan, Mu ne (jàmmi Yàlla ci moom): « Ana luy ñaari bis yii ?» Ñu ne: “Danu ci daa fo (caaxaan) ci jamonoy ceddo (jaahiliya)” Yonent (jàmmi Yàlla ci moom) bi (jàmmi Yàlla ci moom) ne léen: «Yàlla jox na léen ñaari bis yu gën yooyu ñaar, ñuy Bisu tabaski ak Bisu Kori» (Abuu Daawud mooko soloo) Gàttub tabaski it deesu ko rendi jëkk rendig Yilimaan te Yilimaan it balaa rendi nig ba julli, ci niko Baraan nettalee jële ci Yonent (jàmmi Yàlla ci moom) bi «Dees na lottal ginnaaw julli»