Bisub Tabaski wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ahloubadar (waxtaancëru)
Rëdd 19 :
== Waxtuw rendi am tabaski: ==
Mingi dale ci rendigkrendig Yilimaan, rendig yilimaan moongi aju ci ginnaaw julli gi, ba jant di so ca bisub ñatteel ba fu ñu ko fi rendee mu baax, bu dul guddi. La ca gën moodi boroom rendil ko boppam, bu amee ngànt mu wuutal ko moroomum jullitam, te nanga yéene yaw, Ku rendi tabaskim jàmbur te amu ci ndigal, kon du ko doy am tabaski te war naa fay boroom.
 
== Am tabaski: ==
Yàlla neena ci Alxuraan: «Deesul am Yàlla ci ndawalam ga, déeti dereetam ja, waaye dees na Ko am ci ag ragal [Yàlla]» S22 L:36. Kon nanu jàpp njëkk ni yéene ju sell, te Yàlla rekk tax waliif ngistal walla wanu ci bëti nit ñi mooy maye am tabaski.