Doxalukaay bu mbëj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 17 :
Ci atum 1821, lu weesu xamteg feñte gu [[mbëjbijjaakon]] gi simikat boobu di Ørsted xamle woon, la [[jëmmalkat]] bu waa-angalteer bii di Michael Faraday defar ñaari wuutuloxo ngir sàkk li mu duppee ag wëndeelug mbëjbijjaakon: ab doxub dooley bijjaakon bu mbegewu te wéy, ci lu wër ab wëñ, ci maanaa mooy faramfaceg doxalukaay bu mbëj gu njëkk.
==Xeeti doxalukaay yu mbëj==
Xeeti doxalukaay yu mbëj yi am, manees naa wax ne, du xaaj du jeex, waaye manees na cee lim yi ëpp yees di jëfandikoo:
* [[Doxalukaay bu dawaan bu wéy]]
* [[Doxalukaay bu demandoo]]
* [[Doxalukaay bu demandoodi]]
* [[Doxalukaay bu brushless]]
 
== Lëkkalekaay yu biir ==
* [[dawaan bu safaanu]]