Doxalukaay bu mbëj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
VolkovBot (waxtaancëru)
m robot Adding: ht:Motè elektrik
Ibou (waxtaancëru)
Rëdd 13 :
=== Doxiin ===
[[Dawaanu mbëj]] bi day jaar ci ag lëmës gees wëndeel ci ab dogub weñ bi tudd tekkaaralaan bi. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm (naka-jekk përëm lay doon waaye manees na koo defaree ak beneen xeetu wommatukaay), dafay jur ab [[toolu mbëjbijjaakon]], tool bi dafay feeñ niki ag walug bijjaakon, di lees man a natt. Danu koy jàppee niki jenn doole di lees di wax [[dooley Lorentz]]. Toolu mbëjbijjaakon boobu dafay duggante ak toolu mbëjbijjaakon bu lëmës gu wëndeeluwaan bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexi [[dott]]. Wëndeeluwaan bi tambalee wëndeelu ci ndimbalu dooley Lorentz; bëj-gànnaaru toolu bijjaakon bu wëndeeluwaan bi day bijjante ak bëj-saalumu toolu bijjaakon bu tekkaaralaan bi. Xaaju wëndeelu gu nekk, dott bi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi man a wéyee.
 
Xeetu doxalukaay bii, ci [[dawaan bu safaanu]] rek lay doxee, ndax ci dawaan bu safaanu rek la bijjaakon buy soppiku di judd. Suy dox, ag wàll gu néew ci kàttanu mbëj gi day soppeeku tangoor ngir [[njeexitu joule]].
 
== Taariixam ==