Daawuda wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
VolkovBot (waxtaancëru)
m robot Removing: gv:Davy
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Adding: sco:David; cosmetic changes
Rëdd 1 :
[[Ci]] làkku ibrë (דָּוִד) la tur wi jóge. ''Daawuda'' mooy ni ñu ko waxe ci Lislaam. Ci angale mooy ''David''; Ci faranse [[mooy]] ''David''. Moo doon buur bu mag ci bànni Israyil, di yonent bu bind lu bare ci Sabóor. Man nga jàng ci jalooreem ci [[Kàddug Yàlla]] gi ci 1Sa 16:1-30:31; 2Sa 1:1-24:25; 1Ki 1:1-2:10; 1Ch 3:1-9; 10:13-11:19; 12:1-23:32; 28:1-29:30. Benn ci [[maamaati]] Yeesu ci Macë ak ci Luug. Ci Injiil Daawuda moo feeñ ci aaya yii: Mc 1:6,17; 12:3; 22:42,43,45; Mk 2:25,26; 11:10; 12:36,37; Lu 1:27,32,69; 2:4,11; 3:31,32; 6:3; 20:42,44; Yow 7:42; Jëf 1:16; 2:25,29; 4:25; 7:45; 13:22,34,36; 15:16; Ro 1:3; 4:6; 11:9; 2Tim 2:8; Yt 4:7; 11:32; Pe 3:7; 5:5; 22:16.
 
== [[Sëtu]] Daawuda: ==
[[Turu]] Kirist la, muy wone ne, ci lu jëm ci juddoom wàcc na ci yonent Yàlla Daawuda, di wone it ne, Almasi bi la. ''Sëtu Daawuda'' moo feeñ 15 yoon ci Injiil ci aaya yi: Mc 1:1,20; 9:27; 12:23; 15:22; 20:30,31; 21:9,15; Mk 10:47,48; 12:35; Lu 18:38,39; 20:41.
 
Rëdd 50 :
[[ro:David (Israel)]]
[[ru:Давид]]
[[sco:David]]
[[simple:David]]
[[sk:Dávid (biblická postava)]]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Daawuda » lañ ko jële