Mbëjbijjaakon wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
SieBot (waxtaancëru)
m robot Modifying: an:Electromagnetismo
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Mbëjbijjaakon''' mooy banqaasu [[jëmm]] biy gëstu feeñte yu mel ne [[mbëj]] ak [[bijjaakon]] ak lépp lu leesleen ñeel (niki ci misaal [[toolu bijjaakon|tooli bijjaakon]] yi juddoo ci [[dawaanu mbëj]] ak dawaani mbëj yi juddoo ci tooli bijjaakon).
 
Ñoo ngi ko tëgg ngir man a faramface ci anam gees boole feeñte yu mbëj ak yu bijjaakon. Ay feeñte yu mel ne [[sababuxiirtalug mbëjbijjaakon]] ngir wone ni [[toolu mbëj]] lënkook [[toolu bijjaakon]]: ab toolu bijjaakoon buy soppiku dafay jur ab toolu mbëj, naka noonu la toolu mbëj buy soppiku di juree ab toolu bijjaakon. [[Yamaleb Maxwell]] mooy liy faramface mbëjbijjaakon te di sukkandiku ci [[Yanu mbëj|yan]] ak dawaanu mbëj.
 
== Taariix ==
[[William Gilber]] , ci téereem ba ''De Magnete'' (1600), la wone wuute gi nekk ci diggante aw yaram wu mbëj ak wu bijjaakon. Mu fésal àtte yi laqu ci bëmëxante ak xëccante yu bijjaakon yi jaare ci seeni dott ak njeexit li tàngoor am ci bijjaakon bu weñ.
 
ci 1831 la [[Michael Faraday]] doon gëstu doxiinu dawaan bi ci biir ab toolu bijjaakon ba gis ca ne, moom, bijjaakon bi, man naa jur [[liggéey (jëmm)|liggéey]]. Oersted moom wuññi woon na ne ab dawaanu mbëj dafay jur ab toolu bijjaakon, Faraday moom wuññi ne ab toolu bijjaakon dafay sababxiirtal ab dawaanu mbëj. Ci noonu la wuññee baaxi [[doxalukaay bu mbëj]] ak ni liggéey bu [[doolerandu]] man a soppeekoo [[kàttanu mbëj]], naka-noonu mu sàkkee ca ab [[Jurukaayu mbëj|jurukaayu dawaan]].
 
Mbëjbijjaakon a ngi judd ci bi [[James Maxwell]] (1864) boolee ay gisiin yu jiitu woon, niki [[mbëjtekkaaral]], [[bijjtekkaaral]]. Bii gisiin di bees bennal moo leeral jikko yi ci [[yanu mbëj|yani mbëj]] yeek dawaani mbëj yi, bijjaakon yi, [[Duusub mbëjbijjaakon |duusi mbëjbijjaakon]] yi, yu mel ne ag [[leer]] walla [[duusub rajo |duusi rajo]] yi.
 
[[Wàll:mbëjbijjaakon]]