Fattalukaay(mbëj) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
TXiKiBoT (waxtaancëru)
m robot Adding: ur:گنجائش دار
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Adding: pnb:کیپیسیٹر; cosmetic changes
Rëdd 1 :
'''Fattalukaay''' ab cër la bees di jëfandikoo ci biir [[ndombo gu mbëj|ndombo yu mbëj]] yi, di fees di rënk [[kàttanu mbëj]] niki [[toolub mbëjtekkaaral]], [[yanu mbëj|yani mbëj]] yi ñoo fay tase dankaloo fa.
 
Dafay am ñaari làcc, yu tapp yees defaree ak lu man a wommat mbëj, yu làng ak benn diggante bi. Ñaari làcc yi yani mbëj yu dekkarloo fay nekk, wenn làcc wi yan bu ëpp (+) lay am weneen wi bu yées (-), segam ñaari yan yu dekkarloo dañuy xëccante, waral juddug toolu mbëjtekkaaral bi. Taraayu tool bee ngi aju ci limu yani mbëj yi nekk ci diggante làcc yi, moom itam aju ci [[dendu mbëj]] bi. Ngir bañ benn yan jóge ci wenn làcc dem ci weneen, faww ñu def lenn ci seen diggante, lenn loolu lees di woowee ab [[lankmbëj]], man naa nekk [[ngelaw]] rekk walla këyit mbaa lépp luy bañ mbëj jàll ko. Ab fattalukaay bu nekk dafay am ab [[def]] (C) ñu koy natt ciy farad ([[Farad|F]]), dayoom a ngi aju ci lankmbëj bi, mooy li nuy wax dayoob [[toolu mbëj]] bi gën a rëy bi nga xam ne su ko weesoo yani mbëj yi man a jóge ci wenn làcc dem ci weneen, di luy waral itam yàqug lankmbëj bi.
::<math>I = C{dU\over dt} </math>
 
Rëdd 8 :
:* ''C'' mooy defu fattalukaay bi.
 
:* <math>\textstyle{{dU\over dt}} </math> mooy coppiteeg dend bi ci jamono. Su dendu mbëj bees teg ci diggante làcc yi soppeekoo limu yani mbëj yi soppeeku, toolu mbëjtekkaaral bi soppeeku itam. Kon am na benn limu dend bees warul a weesu lu ko moy fattalukaay bi dafay yàqu, lakk.
 
[[Wàll:mbëjMbëj]]
 
[[af:Kapasitor]]
Ligne 58 ⟶ 59 :
[[no:Kondensator (elektrisk)]]
[[pl:Kondensator]]
[[pnb:کیپیسیٹر]]
[[pt:Capacitor]]
[[ro:Condensator]]