Safaanukaay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Luckas-bot (waxtaancëru)
jubbantig mbindiin
Rëdd 3 :
[[Dencukaay:Sink-320x240-3x-rot.gif|right|Ab safaanukaay]]
 
'''Safaanukaay''' ab [[doxalukaay bu mbëj|masinu mbëj]] la buy soppi [[kàttanu doolerandu]] ci [[kàttanu mbëj]] ci melokaanu [[dawaan bu safaanu]]. Soppali gi mi ngi cëslaayu ci feeñte gu [[sababuxiirtalug mbëjbijjaakon]].
== Defariin ==
Defariin gi dafay aju ci xeetu safaanukaay bi mu nekk.
=== Safaanukaay bu demandoo ===
 
Masin bi dafa am ñaari xaaj, benn bi ab xott la bu am am pax ñu koy wax [[tekkaaralaan]], beneen bi di xaaj biy dugg ci bu njëkk bi, ñu koy wax [[wëndeeluwaan]]. Baatu demandoo mi ngi jóge ci li walug bijjaakon bi di demandoo ak wëndeeluwaan bi.
 
Ci tekkaaralaan bi la lëmës giy jur [[toolu bijjaakon]] buy wëndeelu di nekk ci ndimbalu ay [[mbëjbijjaakon]], seen lim yam ak limu wéq yiyeek ak ñaariseexi dott yi, kon su nekkee ab safaanukaay bu ñettiwéq, ñetti mbëjbijjaakonmbëjbijjaan ak ñaariñetti seexi dott lañuy doon, su nekkee ñeenti wéq juroomi mbëjbijjaakonmbëjbijjaan lañuy doon. Safaanukaay bu demandoo ab [[doxalukaay bu demandoo]] lañu jël wëlbati ko. Ab doxalukaay soo ko joxe kàttanu mbëj mu delloo la kàttanu doolerandu, soo ko wëlbatee jox ko kàttanu doolerandu mu nekk ab [[jurukaayu mbëj]], jox la kàttanu mbëj.
=== Safaanukaay bu demandoodi ===
Bii xeetu safaanukaay ab [[doxalukaay bu demandoodi]] lañu jël wëlbati ko mu nekk jurukaayu mbëj. Ngir mu man a dox niki jurukaay faww muy jële kàttan ci geneen ndombo gu biti ngir man a bijjaakoonal lëmës gu wëndeeluwaan bi. Su wëndeeluwaan bi di wëndeelu lay joxewaale kàttanu mbëj waaye ngir walug bijjaakon gi koy wëndeel di sax di dox faww muy wéy di jëlee kàttanu mbëj gu koy dundal ci beneen safaanukaay bu demandoo. Lii moo tax daanaka du xeetu jurukaayu mbëj bu ñuy faral di jëfandikoo ci [[Digg bu mbëj|digg yu mbëj]] yi, bu demandoo lañuy jëfandikoo.
 
== Jëfandikoom ci jëfe ==
Safaanukaay yi bari nañu fi ñu leen di jëfandikoo, ci biir bépp digg bees di jóoxee kàttanu mbëj. Ginnaaw jóog gi ci dawaan bu safaanu, ngir man koo yóbb ba ci liggéeyuwaay yi akyeek kër yi dañu koy soppali ak ab [[soppalikaay]].
 
Safaanukaay yi bari nañu fi ñu leen di jëfandikoo, ci biir bépp digg bees di jóoxee kàttanu mbëj. Ginnaaw jóog gi ci dawaan bu safaanu, ngir man koo yóbb ba ci liggéeyuwaay yi ak kër yi dañu koy soppali ak ab [[soppalikaay]].
 
[[Wàll:Wuutuloxo yu mbëj]]