Doxalukaay bu mbëj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
jubbanti
Rëdd 5 :
== Xaralay doxiin gi ==
 
=== Wàllcëri giad solowudoxalukaay ===
* [[Wëndeeluwaan]]
* [[Tekkaaralaan]]
Rëdd 12 :
 
=== Doxiin ===
[[Dawaanu mbëj]] bi day jaar ci ag lëmës gu ñugees wëndeel ci ab dogub weñ bi tudd tekkaaralaan bi. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm (naka-jekk përëm lay doon waaye manees na koo defaree ak beneen xeetu wommatukaay), dafay jur ab [[toolu mbëjbijjaakon]], tool bi dafay feeñ niki ag walug bijjaakon, di lees man a nakknatt. Danu koy jàppee niki jenn doole di lees di wax [[dooley Lorentz]]. Toolu mbëjbijjaakon boobu dafay duggante ak toolu mbëjbijjaakon gubu lëmës gu wëndeeluwaan bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexi [[dott]]. Wëndeeluwaan bi tambalee wëndeelu ci ndimbalu dooley Lorentz; bëj-gànnaaru toolu bijjaakon bu wëndeeluwaan bi day bijjante ak bëj-saalumu toolu bijjaakon bu tekkaaralaan bi. Xaaju wëndeelu gu nekk, dott bi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi man a wéyee.
 
Xeetu doxalukaay bii, ci [[dawaan bu safaanu]] rek lay doxee, ndax ci dawaan bu safaanu rek la bijjaakon buy soppiku di judd. Suy dox, ag wàll gu néew ci kàttanu mbëj gi day soppeeku tangoor ngir [[njeexitu joule]].