Kàttan wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
TXiKiBoT (waxtaancëru)
m robot Adding: am:አቅም
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Adding: mg:Angôvo; cosmetic changes
Rëdd 1 :
[[ImageDencukaay:Lightning over Oradea Romania 2.jpg|thumb|right| Melax gongikuwaayu kàttan la. Waaye moom dooleem mi ngi aju ci gaawaayan]]
 
== Tekkeem ==
Rëdd 11 :
 
== Njariñam ak yaxam ==
Ci biir jëfandiku gu mboolaay (gu société bi): baatub kàttan dees koy wooye lépp lu nekk ci ron gongikuwaayu kàttan (source d’energie), juddalug kàttan, lakkug kàttan (ag jëfandikoom) ak wattu rootuwaayu kàttan (maanaam fi muy juge), ginnaaw nag dooley koom-koom dafa laaj te soxla ab rootuwaay walla ab gongikuwaay ci gongikuwaayi kàttan yi, looloo tax ag amam akug yooxam(baril ko) bokk ci yitte yu mag yiy caabi. Ci at yu mujj yi, jëfandikoo kàttan feeñ na di benn ci jëfka (facteur) yi gën a sabab [[nuggug àdduna]] bi (global warming), looloo ko def muy ab lëj-lëj ci li ëpp ci réewi adduna bi.
 
== Coppiteg kàttan ==
Rëdd 101 :
[[lt:Energija]]
[[lv:Enerģija]]
[[mg:Angôvo]]
[[mk:Енергија]]
[[ml:ഊർജ്ജം]]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Kàttan » lañ ko jële