Yewwute gu ndefar wuute gi ci sumb yi

54 octets ajoutés ,  11 at ci ginaaw
m (robot Adding: ba:Сәнәғәт)
 
Ag yàqu-yàqu tàmblee feeñati ci wërlaay gu mboolaay yi, ci [[Tugal]], loolu nag mi ngi am bi ag [[ñàkk-liggéey]] walla ag '''liggéeyadi''' tàmblee tas ak a yaatu ci Tugal, ci liggéeykat yu góor yii nga xam ne dañoo tàmbli woon a nekk ay jafe-jafe dëgg, ci kanamu goornamaa yi, di yëngal, tey sàkku nu ñu leen lijantile seen jafe-jafey liggéey yi. Ci noonu goornamaa yi daal di def ay '''àtte''' , indi ay sart yu nos liggéey bi, aar liggéeykat yi ci fuqaleg boroom bopp-alal yi moom isin yi.
 
== Gongikuwaay ==
Téere taariix bu Abdu Xaadir KEBE
 
[[Wàll:Endustri]]
2 337

modifications