Waxtaani sëriñ tuubaa wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Waxtaani Sëriñ Tuuba, xaajub ñaaréel bi
 
'''Ag jiitël'''
alaaji mbakke xaadimul xadiimi mooko dajalefiidajale fii ngir bëgg muriit yéppuyépp jariñu ci,
yàlnakoyàl nako Yàlla nangu ci barkeb Sëriñ Tuubaa te béklookobékloo ko ci àdduna ak allaaxira aamiin.
 
Ahoozu billaahi minash shaytaanir rajiim, wa inniya uhiizuhaa bika wa zurriyatihaa minash shaytaanir rajiim, rabbi ahuuzu bika min hamazaatish shayaatiini wa uhoozu bika rabbi ay uahdhuruun.
Ligne 183 ⟶ 184 :
nékkoon, buñ nangu wu la ñëw mu xam ni sikk si ci ñoom la nékk.'. (Mu dem fa ñu daal di ñëw)
wer na
 
 
== Ay dénkaane ==
Bu ngeen xëyatee:
*Na ngeen jiital jaamu Yàlla teg ci nangoo liggéey
*Def seen naqar muy seen bànneex te def seen coono muy seen nooflaay
*Wéttalikoo topp ndigali Yàlla te bañ a wéttalikoo jëmm
*Na ngeen def ndigali Yàlla muy ab sëriñ te bañ a def ab sant muy ab sëriñ
*Ku bëgg a texe ci àdduna dangay nangoo liggéey
*Ku bëgg a texe ëllëg dangay nangoo jaamu Yàlla.
 
----
*Laabire nit ñi moo gën fital jiyaar
*Bàyyi fen moo gën jàng Alxuraan
 
[[Wàll:Yoonu murit]]