Tuubaa wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
TXiKiBoT (waxtaancëru)
m robot Adding: tr:Touba, Senegal
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Modifying: tr:Touba; cosmetic changes
Rëdd 3 :
Baatu Tuubaa mi ngi juge ci làkku [[araab]] di tekki ci wolof : « texe ».
 
[[ImageDencukaay:Touba3.jpg|thumb|right|Daaray alxuraan]]
== Demb ==
[[ImageDencukaay:Kàrtuw Tuubaa ci google earth.jpg|thumb|right|350px|Tuubaa ci google bu suuf si]]
Dëkkub Tuubaa, kii di [[Sheex Ahmadu Bamba]] moo ko sanc ci atum [[1887]].
 
== Yoriinu dëkk bi ==
Dëkk bi mi ngi aju ci [[Ndaam]], doon as [[ngox]], maanam dëkku kaw kaw, bu taaxeedi, te nag doon gannaaw [[Ndakaaru]], dëkk bi gëna taaxe ci Senegaal. tey dëkk bi gën a rëy ci senegaal ginnaaw ndakaaru
 
== Melosuuf ==
 
== Nit ña ==
 
Tuubaa moo ëpple yokkute ci barig nit ñi ci diiwaani [[Senegaal]] yepp (3,2% at mu nekk ci jamono yii ñu tollu te ñu jàppu ne yokkuteg nit ñi di na àgg ba 12% bu ñu àggee ci ati 2010). Yokku yooyu li ko waral moo di tuxu yu bari yi nit ñi di def bawwoo ci dëkk yu nekk ci [[Bawol]] ak [[Kajoor]]. Dëkk yooyu dañuy gent si ndànk ndànk jëm Tuubaa.
Rëdd 21 :
Ci atum [[2007]], bu ñu ajoo ci gam-gamle gu nguurug Senegaal, waa dëkk bi tolloon nañu ci 529 176.
 
== Koom koom ==
[[ImageDencukaay:ToubaMarché.jpg|thumb|250px|daral]]
Naataangeg dëkk bi lëkkaloo na lool ak [[Màggal gu mag gi]] giy dëppoo ak demug [[Seex Ahmadu Bamba]] ci géej gi.Ba tay Tuubaa dafa bari li waa [[Senegaal]] di woowe Moodu moodu, di ay tukkikat yu féete Tugal tey ëndi xaalis bu bari ci dëkk bi. Lii di [[yaxantu]] (jënd ak jaay) tamit da faa dox lool.
 
== Aada ==
Kii di [[Seex Abdul Ahat]] doon ñatteelu xalifa [[Seex Ahmadu Bamba]] moo fa tabaxoon barab bi ñuy woowe daaray kaamil di [[kàggu]] gu ñu denci mbindum [[Seex Ahmadou Bamba]] ak yeneeni mbind aki téere yu aju ci lislaam, ak ci yeneen fànni xam-xam yi yittéel nit, mi ngi feete nag ci penku jumaa ji, làng ak armeel yi.
== Tabax yu mag yi ==
{{Xët wu ñu yaatal|Jumaay Tuubaa}}
[[ImageDencukaay:Touba moschee.jpg|thumb|250px|left|[[Jumaay Tuubaa]] ]]
Ci Tuubaa la jumaa ju mag ji nekk, doon jumaa joo xam ni jenn la ci [[Afrig]] gu sowwu jant, ci taaram, ak ci rëyaayam. man nañoo jàpp ne mooy xolu dëkk bi, ndaxte yeneen kër yepp dañoo ñëw di ko wër ndànk ndànk, ànd ak màggaayu dëkk bi. Jumaa ji am na juroomi sooroor ak ñeenti xubba. Soorooram bi gën a gudd tollu na ci 80 meetar. Sooroor boobu, kii di Sëriñ [[Fàllu Mbakke]] mooko tudde [[Làmp Faal]] féetele ko kii di [[Maam Seex Ibra Faal]] ci [[7 juin]] [[1963]]. Bis boobu moo di ubbite gu njëkk, ba ñu bari teewe woon nañu ko, ku mel ni [[Lewopool Sedaar Seŋoor]]. Foofu ci jumaa ji fa la barabu [[Seex Ahmadu Bamba]] nekk.
 
== Dayo ==
* [[Amadou Bamba|Cheikh Ahmadou Bamba Khadimou Rassoul]], théologien [[islam|musulman]] [[Soufisme|soufi]].
 
== Xool it ==
=== Teerekaay ===
* {{en}} ''Touba and the meaning of night'', New York, Feminist Press at the City University of New York, 2006
* {{en}} Eric S. Ross, « Touba: a spiritual metropolis in the modern world », ''Canadian Journal of African Studies'', 1995, 29.2
* {{en}} Eric S. Ross, ''Sufi City: Urban Design and Archetypes in Touba'', Rochester, University of Rochester Press, 2006, 344 p. {{ISBN|1580462170}}
* {{fr}} Monique Bertrand et Alain Dubresson, ''Petites et moyennes villes d'Afrique noire'', Karthala, 1997, p. 118-119 {{ISBN|2865377431}}
* {{fr}} Cheikh Guèye, ''L’Organisation de l’espace dans une ville religieuse : Touba (Sénégal)'', thèse de doctorat, Strasbourg, Université Louis Pasteur, 1999, 650 p.
* {{fr}} Sophie Bava et Cheikh Guèye, « Le grand magal de Touba. Exil prophétique, migration et pèlerinage au sein du mouridisme », ''Social Compass'', 2001
* {{fr}} Cheikh Anta Mbacké Babou, ''Touba, genèse et évolution d’une cité musulmane au Sénégal'', Dakar, Université Cheikh Anta Diop, 1992, 39 p. (Mémoire de DEA)
* {{fr}} Cheikh Guèye, ''Touba : La capitale des Mourides'', Paris, Karthala, 2002
* {{fr}} Amar Samb, « Touba et son "magal" »; ''Bulletin de l'IFAN'', t. XXXI, série B, n° 3, juillet 1969, p. 733-753
* {{fr}} Alexis Sané, ''Situation et perspectives de l'intégration de Touba dans la vie économique du pays'', DAKAR, CFPA, 1970, 66 p. (Mémoire de stage)
 
=== Filmokaay ===
* {{fr}} [[Blaise Senghor]], ''Grand Magal à Touba'', court métrage documentaire, 1962, 20 mn
* {{fr}} Christophe Marlard, ''A travers le Sénégal. 3, Touba, une ville à part'', film documentaire, [[École normale supérieure|ENS]] Fontenay/Saint-Cloud, 1999, 13 mn
 
=== Lëkkalekaay yu biti ===
{{commons|:Wàll:Touba, Senegal|Touba}}
* {{en}} [http://www.fallingrain.com/world/SG/3/Touba.html Maps, weather and airports for Touba]
* {{fr}} [http://www.pepam.gouv.sn/acces.php?idcr=03325 La communauté rurale de Touba Mosquée sur le site du PEPAM] (Programme d'eau potable et d'assainissement du Millénaire)
* {{fr}} [http://www.mouride.com/la_ville_de_touba.htm La ville de Touba]
* {{fr}} [http://www.walf.sn/actualites/suite.php?rub=1&id_art=36212 « Statut d'extraterritorialité : comment Touba est devenu un État dans un État »] (article de ''[[Wal Fadjri]]'')
 
[[Wàll:dëkkiDëkki Senegaal]]
[[Wàll:yoonuYoonu murit]]
 
[[de:Touba]]
Rëdd 76 :
[[ru:Туба (Сенегал)]]
[[sv:Touba]]
[[tr:Touba, Senegal]]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Tuubaa » lañ ko jële