Sëriñ Muhammadu Faliilu Mbàkke wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 6 :
Sëriñ Fàllu Mbàkke génn na àdduna ci atum 1968 (dund 81 ciy at) ci ginnaaw bi mu nekke xalifab
Sëriñ Tuubaa ci atum 1945 ba 1968.
Sëriñ Fàllu Mbàkke mom [[Seex Ahmadu Bàmba]] Xaadim Rasuul (baayam) mi sos yoonu muriid ak Soxna Awa Buso (ndayam) doomu [[Sëriñ Muhammadu BUSO]] (Sëriñ Mbusóobe) nijaayu Sëriñ Tuubaa, Mu bawoo ci njaboot gu sell gii, di askan wu ragal Yàlla daa jàng tey jàngale, dëkkoo jaamu Yàlla te di ko jaamulu, di ay wàlliwuy Yàlla yu mat, Mu [[cosaan]]o ci [[askan]]u [[Sëriif]] gog calale ga dem na ba ca Imaam Hasan mom Imaam [[Aliwu mom Abii Taalib]] ak [[Faatima]] mom [[Muhammad]] [[Yonent]]ub Yàlla (jàmmi Yàlla ak xéewalam ci ñoom).
Sëriñ Fàllu Mbàkke mom Seex Ahmadu Bàmba Xaadim Rasuul (baayam) mi sos yoonu muriid ak Soxna Awa Buso
(ndayam) doomu Sëriñ Muhammadu BUSO (Sëriñ Mbusóobe) nijaayu Sëriñ Tuubaa, Mu bawoo ci njaboot gu sell gii, di askan wu ragal Yàlla daa jàng tey jàngale, dëkkoo jaamu Yàlla te di ko jaamulu, di ay wàlliwuy
Yàlla yu mat, Mu cosaano ci askanu Sëriif gog calale ga dem na ba ca Imaam Hasan mom Imaam Aliwu mom Abii Taalib ak Faatima mom Muhammad Yonentub Yàlla (jàmmi Yàlla ak xéewalam ci ñoom).
Mu dondoo ci loolu (doonte ag njub déesu ko dondoonte waaye dees na ci yare, te moo baaxoo am)
ag cell, Yar, xam, ngëm ak melo ya war ci doomu [[Soxna]], ci yooyu jikko lako ay way-juram yare te nàmptal ko ci.
 
 
== Am njàngam ==
[[Image:S Fallu.jpg|thumb|right|350px|Sëñ Fàllu ci njàngum Alxuraan]]
Ci loolu mu dal jàng ci bi muy làq 8 i at, dalee ci njàngum Alxuraal[[Alxuraan]] téereb Yàlla bi, ci [[jàngalekat]] bu tudd [[Sëriñ Ndaam Abdu Rahmaan LO]] ca dëkkub Ndaam deesi ko woowe «Aalimun Xabiir» ak ci [[Sëriñ Moor Jaara Mbàkke]] miko tuural Alxuraanam, ba wattu Ko wattu gu yéeme ci ab taar, ba daan a wax ni:«Ku ma bokkalul jàng ci Sëñ Moor Jaara maala man ci alxuraan» ngir di wone taarub wattu alxuraan gi mu fa jële, ginnaaw bi baxoo woon na di bind ay kaamil di jox Baayam Seex Ahmadu Bàmba, ku taaru woon am mbind la, (Yàlla xéewalal na nu ba nu gis te jànge ci am mbindam), muy kaamilu alxuraan bu rafet wallaahi! te wér ci ay yàq, batay di firndéel rafetug alxuraanam, limu bind ci ay [[kaamil]] nag lotteef na ci di ko takk mbaate xayma, waaye dondoos na ci ay ñeenti fukk ci ay [[kaamil]] yu mu bind ci ay yoxoom yu bokkul, Ñaar fukk ak juróom ñatt (28) ya baayam [[Seex Ahmadu Bàmba]] la ko jox àddiya.
 
Ginnaaw njàngum alxuraanam jàng na xam-xamu diine ca Maam Moor Jaara Mbàkke (Boroom Saam) Ak [[Maam Cerno Ibra Faati Mbàkke]], niki jennal [[Yàlla]] ak ngëm (Tawhiid, iimaan), Àttey [[Lislaam]] akuw yoonam ([[Fiq]]), Séllal ak jaamu ngir Yàlla dong (Ihsaan, [[Tassawuuf]]), bamu xarañe ko, Ginnaaw bi sëriñ bi jugee ci tukkib géej gi la ko mottalil xam-xam boobu ci [[Gànnaar]] ci dëkk bees di wax [[Xumaag]], Mu ànd ak [[Sëriñ Moodu Mustafaa Mbàkke]] ak [[Sëriñ Moodu Roqaya BUSO]] mom [[Sëriñ Mbàkke Buso]].
 
Ci njàng moomu nag ak yar bi, mu fàggoo ci lislaam ju mat sëkk, ragal Yàlla maandu, bëgg alxuraan, jëfe ab xam-xamam, di boroom ngor, muñ, ak jikko yees taamu.
Mu doon ku xarañe làkku [[araab]] itam, ba bind na ci ladabu[[ladab]]u [[araab]] lu sakkan, ci xeet i nose di ci ñaan ak a sant Yàlla, tey julli ci Yonent bi.
 
== Lenn ci ay jikkoom akug taalibewoom ci Sëriñ Bi ==