Ndombo gu mbëj wuute gi ci sumb yi

19 octets ajoutés ,  11 at ci ginaaw
Coppite gi amul tënk
 
== Noste gu jàllu ==
Batay [[dawaan bu wéy]] lees di dundale ag ndombo gu ami [[Fattalukaay(mbëj)|fattalukaay]] walla [[xiirtalukaay]] mbaa ñaar ñépp. Kem yi U ak I dañuy bawoo cig noste gu jàllu dem ci geneen noste gu sax. Kon nosteg jàllu du luy wéy, luy nekkandi la rekk.
Àtte yees bind ci kaw yépp manees na leen fee jëfandikoo batay.
== Noste gu sin ==
3 292

modifications