Soppalikaay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
jubbantig mbindiin
Rëdd 13 :
== Ag sàkkam ==
 
Baaxi ab soppalikaay ki leen njëkk a taxawal mooy [[Michael Faraday]] ci 1831, waaye li mu ci jubluwoon rekk moo doonoon biral baaxi yi nekk ci [[sababuxiirtalug mbëjbijjaakon]], kon xalaatul woon nan la man a nekkee jumtukaay buy jariñ ci dëgg-dëgg.
Lucien Gaulard ak John Dixon Gibbs ci 1881 lañu génne ca [[Londar]] ab jumtukaay bees duppee woon «''ñaareelu jurukaay''», ñu daaldi jaay xalaat bi këru liggéey bu [[Diiwaan-yu-Bennoo|waa-aamerig]] ba Westinghouse. Mooy soppalikaay bees njëkk a jëfandikoo ci jëfe.