Soppalikaay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Luckas-bot (waxtaancëru)
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 3 :
'''Soppalikaay''' ab jumtukaay la buy tax a man a soppi limu dend ak taraayu [[dawaanu mbëj]] bu jóge cib gongikuwaay buy jur [[kàttanu mbëj]] gu [[Dawaan gu safaanu|safaanu]], ci beneen limu dend ak taraay yu wuute te bokk [[baraay]] ak melokaan. Te limuy ñakk ci kàttan ci soppali gi lu néew la. Ab soppalikaay, ci dawaan bu safaanu rekk la man a doxe, ndax ci bii xeetu dawaan la [[mbëjbijjaakon]] bu safaanu, di ci li doxam aju, man a juddoo.
 
Soppalikaay yi ci [[ndomboy jokkalekaayu dawaanu mbëj]] yiy lëkkale jóoxuwaayu mbëj yi ([[diggudigg bu mbëj|diggudigg yu mbëj]]) ak jëfandikukat yi lañu leen di jëfandikoo. Bokk na yenn ci ngirte yi tax dawaan bu safaanu bu [[Nikola Tesla]] am-ndaw ci kaw [[dawaan bu wéy]] bu Edison ci liñu doon woowee [[xareeb dawaan yi]].
 
== Ubbite ==
Lim bu bari bu kàttanu mbëj bees soxla ci [[mboolaay]] yu taaxe yi tax na ñu war koo jóox ci bariwaay bu dayoowu ci jóoxuwaay yees duppee [[DigguDigg bu mbëj|diggudigg yu mbëj]]. Ngir man a xayma bariwaayu kàttanu mbëj bees jóox cib diggudigg bu mbëj dañuy xool ci liñuy duppee [[ngóora]] gi(njunjam di ''P'' bennaanu nattam di [[Watt]] ñu koy tënk ci [W]) di luy man a nekk ci diggante ay fukki kw (kilowatt, 1 kW = 1000W) ci diggu[[Digg bu ndoxmbëj|digg yu [[ndoxmbëj]] walla yu jant ba ci ay teemeeri MW (megawatt, 1 MW = 1.000.000 W) di yu diggu yu [[DigguDigg bu tangmbëjtàngmbëj|tangmbëjdigg yu tàngmbëj]] ak yu [[DigguDigg bu saal|saal]]. Gii kàttan dañu koy yóbb ci ay teemeeri km. Ngóora (''P'') gi mi ngi am digaale ak dawaan (''I'') geek dend (''V'') gi ci mbindum xayma miy toftal:
:<math>P = V I \cos \phi \,</math>
 
Lii dafay tekki ne man ngaa yokk walla wàññi [[dendu mbëj|dend]] gi walla dawaan bi te ngóora gi du soppeeku (te jéem a fexe ba <math>cos \phi \,</math> jege 1 (benn)). Lii am na solo lool ndaxte dawaan bi ''I'' dafay jur tangoor suy jaar ci biir [[watatukaayu mbëj]] bi (ngir [[njeexitu Joule]]): lu dawaan bi di gën a bari tangoor giy judd di gën a bari; ngir moytu lii faww ñu yokk dijjaayu watatukaay bi, waaye it yokk gi am na dig ci wàllu koom ak xaral, aju na tamit ci feeñte bi ñuy duppee [[waddug dend]] yu buum yi ci seen bopp. Kon ngir wàññi dawaan bi dañuy def ab soppali yokkaale dend gi ci anam gu ngóora gi dul soppeeku.
 
== Ag sàkkam ==
 
Baaxi ab soppalikaay ki leen njëkk a taxawal mooy [[Michael Faraday]] ci 1831, waaye li mu ci jubluwoon rekk moo doonoon biral baaxi yi nekk ci [[sababu mbëjbijjaakon]], kon xalaatul woon nan la man a nekkee jumtukaay buy jariñ ci dëgg-dëgg.
Lucien Gaulard ak John Dixon Gibbs ci 1881 lañu génne ca [[Londar]] ab jumtukaay bees duppee woon «''ñaareelu jurukaay''», ñu daaldi jaay xalaat bi këru liggéey bu [[Diiwaan-Yuyu-Bennoo|waa-aamerig]] ba Westinghouse. Mooy soppalikaay bees njëkk a jëfandikoo ci jëfe.
 
[[Wàll:Xaralaymbëj]]