Dawaan gu wéy wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
SieBot (waxtaancëru)
m robot Adding: su:Arus listrik saarah
Xqbot (waxtaancëru)
Rëdd 1 :
[[Dencukaay:Direct current symbol.svg|thumb|200px|rigth|njunj gu dawaan gu wéy]]
 
'''Dawaan gu wéy''' (ñu man koo tënk ci '''DC''' ''Direct Current'' ci [[wu-angalteer]], moom lees di gën a jëfandikoo), di dëddoo ak [[dawaan gu safaanu]] AC, xeetu dawaan la gu am genn jubluwaay. Dawaan gi dafay wéy di dox ci ag ndombo ci genn jubluwaay. [[Mbëjfeppal]] yi ci genn jubluwaay lauy wéy di daw.
 
== Nattiin ==
Dawaan gu wéy ciy amper lees koy natt. Benn amper mooy ,24*10<sup>18</sup> [[mbëjfeppal]] ci saa (I = Q/t), I = dawaan, Q= coulomb, t= saa).
 
Wenn rëdd wu wéy ak ñett yu ndaw, ci suufam, mooy njunju dawaan gu wéy; dees na jëfandikoo itam DC (Direct Current). Dawaan gu safaanu moom AC ''alternating current'' lees di jëfandikoo wall njunj wii di ~.
Rëdd 16 :
 
{{wikibaatukaay}}
 
[[Wàll:dawaanuDawaanu mbëj]]
 
[[ar:تيار مستمر]]
Ligne 44 ⟶ 45 :
[[ko:직류]]
[[lv:Līdzstrāva]]
[[ml:നേര്‍ധാരാ വൈദ്യുതി]]
[[ms:Arus terus]]
[[nl:Gelijkstroom]]