Haj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
m Tuddewaat nañ Aj léegi mooy Haj
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Aj'''Haj''' mooy juróomeelu ponku Lislaam, Ci waxi Yonent Yàlla Muhammed ja ni: "Tabaxees na Lislaam ci juroom: Seere amul benn buur bu dul Yàlla te Muhammed ndawam la, Taxawal Julli, Joxe Azaka, Woor weeru koor, Ak Aj ci ku ko man aw yoon", ba tay Aj farata la ci benn jullit bu ko man (ci bepp anam), ci waxi Yàlla mu kawe ja ni:ñeel na Yàlla ci nit ñi Aj néek ba ci ku ko man aw yoon (benn yoon) te ku weddi Yàlla moom woomle waliif mbindéef yi.

== AjHaj Màkka ak kumu war ==

'''AjHaj Màkka''' benn yoon faratala ci mukàllaf mu ko man ci yaramam ak ci ab yobbalam.
Manug Yaram wi moodi mu bañ a ame wopp ju ko tee man a dem walla mu ragal
ca dem ga dollikug wopp ja, walla sosug wopp walla ak yeex a wér.
Rëdd 16 :
[[Image:la_mecque_pelerinage.png|300px|right|thumb|Jeegoy Aji Màkka gi]]

== Ñatti xeeti AjHaj yi: ==
AjHaj am na ñatti xeet:

1-AjugHajug tamattu

2-AjugHajug qiraan

3-AjugHajug ifraad

== Umra ==
Rëdd 28 :

== Faratay AJHaJ ==

AjHaj ñeenti farata la am :

1 yeenee aj (nawaytu al-hajja wa 'ahramtou bihi li l-Laahi taala)

2 tawaaful ifaada

Rëdd 40 :

Sunnay ajHaj fukk ak ñaar la:

Am na ci ñeent yoy ñi ngi ame ca armal ga:

1 sangu gu jokkook armal gi

Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Haj » lañ ko jële