Haj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
== Aj Màkka ==
 
Aj mooy juróomeelu ponku Lislaam, Ci waxi Yonent Yàlla Muhammed ja ni: "Tabaxees na Lislaam ci juroom: Seere amul benn buur bu dul Yàlla te Muhammed ndawam la, Taxawal Julli, Joxe Azaka, Woor weeru koor, Ak Aj ci ku ko man aw yoon", ba tay Aj farata la ci benn jullit bu ko man (ci bepp anam), ci waxi Yàlla mu kawe ja ni:ñeel na Yàlla ci nit ñi Aj néek ba ci ku ko man aw yoon (benn yoon) te ku weddi Yàlla moom woomle waliif mbindéef yi.
 
== Aj Màkka ak kumu war ==
 
'''Aj Màkka''' benn yoon faratala ci mukàllaf mu ko man ci yaramam ak ci ab yobbalam.
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Haj » lañ ko jële