Doxalukaay bu mbëj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Doxalukaay bu mbëj''', ab [[wuutuloxo]]b [[mbëj]] la, gooboo xam ne kàttan giy duggu ci moom gu [[mbëj]] la te ga muy génne gu [[doolerandu]] la. Doxalukaay yu mbëj yi am nañu solo lool ci dundiinu jamono ju bees ji, te it dëgg la sax, ne limu doxalukaay yu mbëj yi nekk ci am réew dafay firndeel tolluwaayu jëm-kanamam. TeMaanaam itam deminu, maanam yokkute walla néewteyokkug limu doxalkaaydoxalukaay yu mbëj yi ci am réew bokk na ci wonekatwonekaay yiy firndeel tolluwaayu yokkuteyokkuteem ci wàllu [[xarala]] mu réew moomu. Ngir dëggal loolu, doynadoy na xool ci jumtukaay yi nekk ci li ñu wër: ca saxaar ba ci watukaay ak yeneen ak yeneen, yi ngeen xam ne nit ku bees ki moo ngi koy jëfandikoo bu baax, man naa ni sax ñooy doxal sunug dund.
 
Doxalukaay yu mbëj yi dañoo bari te wuute, am na [[doxalukaay bu dawaan bu wéy]], [[doxalukaay bu dawaan bu safaanu]] moom mu séddaliku ci [[doxalukaay bu demandoo]] ak [[doxalukaay bu demandoodi]],.
== Xaralay doxin gi ==
 
=== WàllXaralay gidoxiin solowu:gi ===
 
* [[Wëndeelukat]]
=== Wàll gi solowu ===
* [[Tekkaaralkat]]
* [[Toolu BijjaakonWëndeeluwaan]]
* [[Tekkaaralaan]]
* [[Toolu bijjaakon]]
* [[Bijjaakon]]
 
=== DoxinDoxiin ===
Dawaanu [[Dawaanu mbëj]] gibi day jaar ci ag lëmës gu ñu wëndeel ci ab doggubdogub weñ bi tudd [[Tekkaaralkat]]tekkaaralaan bi. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm (naka-jekk përëm lay doon waaye manees na koo defaree ak beneen xeetu wommatukaay), dafay jur ab [[toolu mbëjbijjaakon]], butool cabi dawaandafay jaareefeeñ niki ag walug bijjaakon, di lees man a nakk. Danu koy jàppee niki jenn doole di lees di wax [[dooley Lorentz]]. Toolu mbëjbijjaakon boobu dañdafay koyduggante sóob ci beneenak toolu mbëjbijjaakon gu lëmës gu [[wëndeelukat]]wëndeeluwaan bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexi [[dott]]. [[Wëndeelukat]]Wëndeeluwaan bi tambalee wëndeelu ci sababundimbalu njureeludooley mbëjbijjaakonLorentz; bëj-gànnaaru toolu bijjaakon gubu wëndeelukatwëndeeluwaan bi day wootalantebijjante ak bëj-saalumu toolu bijjaakon gubu tekkaaralkattekkaaralaan bi. Xaaju wëndeelu gu nekk, dott bi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi man a wéyee.
 
DoxalukaayXeetu doxalukaay bii, ci [[dawaan gubu safaanu]] rek lay doxee, ndax ci dawaan bu safaanu rek la bijjaakon buy soppiku di judd. Suy dox, ag wàll gu néew ci kàttanu mbëj gi day soppeeku tanggoortangoor ngir [[njeexitu joule]].
 
== Taariixam ==
Ci atum 1821, lu weesu xamteg feñte gu [[mbëjbijjaakon]] gi, simikat boobu di Ørsted xamlewoonxamle woon, la [[jëmmalkat]] bu waa-angalteer bii di [[Michael Faraday]] defar ñaari wuutuloxo ngir jóoxsàkk li mu duppee abag wëndeelug mbëjbijjaakon: ab doxub dooley bijjaakon bu mbegewu te wéy, ci lu wër ab wëñ, ci maanaa mooy faramfaceg doxalukaay bu mbëj gu njëkk.
== Lëkkalekaay yu biir ==
* [[Doxalkaaydawaan bu demandoosafaanu]]
* [[Doxalkaaydawaan bu demandoowulwéy]]
* [[Doxalukaay bu wéy]]
* [[dawaan bu safaanoo]]
 
{{wikibaatukaay}}