Hip-hop wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 3 :
'''Hip-hop''' ag yëngu-yëngug [[caada]] ak [[fànn]] la, mi ngi juddoo ca [[Réew yu Beenoo]] ya ci ndoorteel [[Ati 1970|ati 1970]] yi, daa boole bànneexu ak ñaxtu. Mi ngi juddoo ci biir askani waa-aamerig yu ñuul yi, ca [[New York]], fa la tàmbalee, mujj tas ca réew ma ba ci àdduna bi bépp, ba tay mooy dundiinu réewu-taax wi ëpp doole. Caaday Hip-hop ci ñeenti ponk la tënku: [[Break dancing|''break dancing'']], ''[[DJing]]'', ''[[MCing]]'' ak [[Graffiti|''graffiti'']].
 
BiiWii xeetu [[fànn]] ñu bari ci woy wi lañ koy tënk ,''MCing'', te mu gënagën a siiw ci [[Rap|rap]]. Caadaay Hip hop yemulyamul rekk ci rap, man naa sol mbubb yu wuute: su fekke danuy yemyam rekk ci xoosug DJ bi ([[Disk Jokey]]), waruñwaruñu ko tuddeeti rap, waaye DJing , sunu yemeeyamee ci li MC bi (master of ceremonie, [[njiitubnjiitul xew]]) di baccbàcc kon man nannanu kaakoo wooweewoowe rap, walla tamit, donte bari na lumuylu muy faral di am, boolee benn DJ ak ay walla benn MC, kon ci nii hop-hop lañuy wax, ndax [[rap]] ak [[MCing]] yépp ci caadaay hip hop lañu bokk, waaye nit ñi rap la ñuylañuy wax rekrekk yemyam ci ngir yombal.
 
== Cosaanu baat bi ==
Cosaanu baat bi taxu kaakoo leer noonu, ci ñenn ñi ''jëfandikoo-xel ngir tekki''
* ''Hip'' "muus", "am-xel" lay tekki, muusaayu tappalaatukat.
* ''Hop'' abag yuuxu la bugu kuy tëb di def (soosooy tëb ni op!).
Nee nañnañu baatibaat baa ngi warawar a bawoo ci [[DJ Luv Bug Starski]] mi ko doon faral di jëfandikoo suy wax. Waaye li wér te wóor mooy ne gandoor bu [[Sugarhill Gang]] mooy ki ko siiwal ci àdduna bi, ci seen woy woowu ''Rapper's Delight'', di benn ci woyuwoyi rap yi ñu njëkkanjëkk a def k7.
 
== Taariix ==
 
==== Ay cosaanam ====
Woyu hip-hop ci buumu xeeti woyi waa-aamerig yu ñuul yi la bokk. Ay dàttam ñi ngi bàyyikoo ci dundindundiin gu metti gi ñu nekkee woon, dalee ca seeni maam ba ci jamono yi muy juddu, woy yañyañu daan def ca tool ya daan ca naqarlu seenug nekkinnekkiin, ak caadaan ca fattali seenug jóge [[Afrig]]. Mi ngi tambaleetàmbalee ciy kebetu niki xeeti woy yu mel ne [[Ragetime|ragetime]], [[Jazz|jazz]], blues. Ci lu gënagën a jonjoo, woyu hip-hopa ngi bawoo ci ''Soul'', ak ci ''funk''. Yii xeeti woy bawoo [[bëj-gànnaaru Aamerig]] dem ba fasook sound-system bu waa-jamayka, bi àgg ba New York ndax wàlliyaanndoxandéemu gi waa-jamayka yi daa def foofa. Ba tax-na ñett ñi ñu ne ñoo sos yëngu-yëngu hip-hop fa la ñulañu bàyyikoo.
 
Donte hip-hop ci yii xeeti woy la ëleejële ay dàttam, waaye doonul seenug wéyalewéyal. Du lu ay tëggkat yu xereñ ci seen liggéey toog xalaat, ni blues doonee wéyaleegwéyalug jazz, gospel juddoo ci blues, soul tegu ci, funk ñëw, caaday hip-hop dafa am ab dog-dog ag yeneen xeeti woy yooyu
 
==== Aji-rap yi njëkk ====
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Hip-hop » lañ ko jële