Yanu mbëj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 2 :
Bennaanu natt bu benn yan mooy [[Coulomb]]. Yan bi gën a ndaw bees man a natt mooy bi ab [[mbëjfepp]] di yanu, ñu koy faral di binde ''e'' = -1,602 10<sup>-19</sup> ''[[Coulomb|c]]''.
 
Yanu mbëj am mbir mees di janeer la, du lees man gis ak bët, dafa di aw tur wees jox genn feeñte gi ngir man a faramface wenn xeetu doxiin wi, di njeexiitam. Yanu mbëj man naa am ñaari xar-kanam yu wuute, di yees jàppee yu "dekkarle" ; benn bi di bu '''wuyyu'''baax (+) beneen bi di bu '''gàntu'''bon (-). Ñaari yan yu wuute (bu wuyyubaax ak bu gàntubon) dañuy bijjante, ñaar yu bokk (ñaar yu wuyyubaax walla ñaar yu gàntubon) dañuy bëmëxante.
 
Yan yu gàntubon yi lañuy faral a tudde ay [[mbëjfepp]] , yu wuyyubaax yi di ay [[feppsaal]] ndax ñooy yiy nekk ci biir saalu [[xarefulwoon]] bi te kemu seen yan yam ak yu mbëjfepp yi te dekkarloo.
 
Dawaanu mbëj man naa am ñetti sabab: walug ay feppsaal (yan yu wuyyubon) walla walug ay mbëjfepp (yan yu gàntubaat), walla seenug wal ñoom ñaar ñépp ci jubluwaay yu dekkarloo.
 
Ngir bañ ay jaxasoo mbëjkat yi dañoo ànd ci ne walug yan yu wuyyubaax yeey dawaanu mbëj, ci liñuy tudde ''dawaanu déggoo'', ndax bu njëkk dañoo foogoon ne doxug wàll-wàllaan yu wuyyubaax yeey jëmmal dawaan bi, donte tay jii dem nañu ba xam ne safaan bee nekk: dawaanu mbëj doxug mbëjfepp yee ko jur. Ndax feppsaal yi duñu ay wàll-wàllaan yuy dox, ci saalu xarefulwoon bi lañu sax dëkk. Bànqaasi [[xam-xam]] yi yittewoo gëstu yile feeñte ñooy [[xaralaymbëj]] ak [[mbëjfeppal]].
 
== Lëkkalekaay yu biir ==