Yanu mbëj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 2 :
Bennaanu natt bu benn yan mooy [[Coulomb]]. Yan bi gën a ndaw bees man a natt mooy bi ab [[mbëjfepp]] di yanu, ñu koy faral di binde ''e'' = -1,602 10<sup>-19</sup> ''[[Coulomb|c]]''.
 
Yanu mbëj am mbir mees di janeer la, du lees man gis ak bët, dafa di abaw tur beeswees jox genn feeñte gi ngir man a faramface bennwenn xeetu doxiin biwi, di njeexiitam. Yanu mbëj man naa am ñaari xar-kanam yu wuute, di yees jàppee yu "dekkarle" ; benn bi di bu '''baaxwuyyu''' (+) beneen bi di bu '''bongàntu''' (-). Ñaari yan yu wuute (bu baaxwuyyu ak bu bongàntu) dañuy bijjante, ñaar yu bokk (ñaar yu baaxwuyyu walla ñaar yu bongàntu) dañuy bëmëxante.
 
Yan yu bongàntu yi lañuy faral a tuddeetudde ay [[mbëjfepp]] , yu baaxwuyyu yi di ay [[feppsaal]] ndax ñooy yiy nekk ci biir saalu [[xarefulwoon]] bi te kemu seen yan yam ak yu mbëjfepp yi te dekkarloo.
 
Dawaanu mbëj man naa am ñetti sabab: walug ay feppsaal (yan yu baaxwuyyu) walla walug ay mbëjfepp (yan yu bongàntu), walla seenug wal ñoom ñaar ñépp ci jubluwaay yu dekkarloo.
 
Ngir bañ ay jaxasoo mbëjkat yi dañoo ànd ci ne walug yan yu baaxwuyyu yeey dawaanu mbëj, ci liñuy tuddeetudde ''dawaanu déeggoodéggoo'', ndax bu njëkk dañoo foogoon ne doxubdoxug wàll-wàllaan yu baaxwuyyu yeey jëmmal dawaan bi, donte tay jii dem nañu ba xam safaan bee nekk: dawaanu mbëj doxubdoxug mbëjfepp yee ko jur. Ndax feppsaal yi duñu ay wàll-wàllaan yuy dox, ci saalu xarefulwoon bi lañu sax dëkk. Bànqaasi [[xam-xam]] yi yittewoo gëstu yile feeñte ñooy [[xaralaymbëj]] ak [[mbëjfeppal]].
 
== Lëkkalekaay yu biir ==