Yamoo wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Robbot (waxtaancëru)
m robot Adding: ceb:Ekwador
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Modifying: ckb:ھێڵی ئیستوا; cosmetic changes
Rëdd 1 :
[[ImageDencukaay:Earth equator northern hemisphere.png|right|300px]]
Ci melosuuf, '''yamoo''' gi aw rëddu tus-wu-gar la, di ag buumug jeneer gu ñu rëdd mu wër àdduna, jaar ci diggante dott yi. Yamoo gi moo xàjjale àdduna bi, def ko [[Xaaju-kol-kol bu bëj-gànnaar|xaaju-kol-kol bu bëj-gànnaar]] ak [[Xaaju-kol-kol bu bëj-saalum|xaaju-kol-kol bu bëj-saalum]]. [[Tus-wu-gaar]] wu yamoo gi 0° (tus aj). Guddaayu yamoo gu Suuf si mi ngi tollu, ci xayma, 40 075 km.
 
== Yamoog Suuf si ==
=== Klimaa ===
Klimaab barab yi ne ci li wër yamoo gi lañuy wax [[Klimaab yamoo|klimaab yamoo]]. Di nañ wax itam klimaab [[Gëwéelub |gëwéel]], di bu barab yi ne ci li wër [[Gëwéel|gëwéel]] yi ([[Gëwéelub Tef|gëwéelub Tef]] ak [[Gëwéelub Sànkar|gëwéelub Sànkar]])
 
=== Réew yi mu dagg ===
[[ImageDencukaay:World map with equator.svg|thumb|Lonkoyoonu àdduna buy fesal yamoo gi]]
Ci sunu àdduna([[Suuf]] si), yamoo gi ay mbàmbulaan ñoo ëpp ci li mu dagg ci yoonam, téeméer boo jël ci gudaayam ñaar-fukk ya rekk a jaar ci suuf.
 
Rëdd 21 :
* [[Somali]]
 
[[Wàll:melosuufMelosuuf]]
 
[[af:Ewenaar]]
Rëdd 37 :
[[ca:Línia equatorial]]
[[ceb:Ekwador]]
[[ckb:هێڵیھێڵی ئیستوا]]
[[cs:Zemský rovník]]
[[cv:Экватор]]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Yamoo » lañ ko jële