Jolof wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Adding: pnb:وولوف بادشاہت; cosmetic changes
Rëdd 1 :
'''Jolof''' moo doonoon nguur ngi gënnoo na mag ci [[Senegaal]] ci jamono yooyu. Mi ngi sosu ci xarnub XIV ba [[Nguuru Mali]] gu mag ga saayee, rawati na la feete woon ca sowam. Ba nguuru Jolof taxawee, jëloon na melokaanu nguur yi ko jiitu woon, waaye bàyyi woon na fa melokaanu càmm ak màng ga xewoon ci jamono.
[[ImageDencukaay:Guuri senegaal.jpg|rightdroite|thumbvignette| [[lonkoyoon|Lonkoyoon]] politig bu nguur yi nekkoo [[senegaal]]]]
== Sosteefam ==
Ki ñu ne moo sos nguur googu mooy Njaa Jaan Njaay. Mooy doomu [[araab]] la bu ñuy wax Abaabakar ak [[Lingèer]] ab [[Tukulòor]] bu tudd Faatimata Sall. Moom, Njaa Jaan Njaay, def na ci réew mi liggéey yu réy.
Rëdd 70 :
== Nguuru Jolof ==
Jolof boo ko dee xool dafa këll bunom dem na ba lag da geer, égg na [[Ferlo]]. Moom dafa xawa uuf Tooro ak Dimat ak [[Waalo]] ak [[Kajoor]] ak [[Bawol]] ak [[Siin-Saalum]] wàllu penku wi [[ndand féy-féy]] la. Jolof fu neew ñax la, bari na lool garabi werek. Mel na ne du fu naat it ndax ab woykat bu siiw ci yu wolof yi di [[Sëriñ Musaa KA]] am na fu muy melale lu ni mel ci genn xasidaam, mu ne :
nawet Jolof noor fa te doo nooraani - ndaw lu ca sax soo màggatee yalwaani
 
Kon du war a nekk fu bari ay balluwaayi xéewal .
Rëdd 80 :
[[Fuuta]] moo doon gën jaa màggi réew ci mbooleem gox yi. loolu masu la deñ ba ci fukkeelu xarnu ak ñeent, moo tollook falug waa Tonjon.
 
Jamono jooju la [[màndeŋ]] yi yaatal seen [[nguur gu mag]] dale ca géeju Atlas ca bëj-gànnaar ba bëj-saalum ca Gàmbi. Ca jamono jooju yit la nguuru jolof nangoo boppam, moo gënoon a am solo ci réewu Wolof yi ak Séeréer si ak ci mbooleem réew yi ci géej gi, ci li ko dale ca bëj-gànnaar ba bëj-saalum, [[Fuuta]] ba [[Saalum]]. Ëmboon na [[Waalo]], [[Kajoor]], [[Bawol]] ak rèewi [[Séeréer]] si ak lenn ci [[Fuuta Tooro]].
 
== Saayug nguuru Jolof gu mag ga ==
Rèew yu bari nangu nañ seen bopp ci nguuru Jolof gu mag ga. [[Kajoor]] njëkk a nangu boppam topp ca [[Waalo]] ci njiitu [[Barag(waalo)|Barag]]. Bawol ci njiitu [[Teeñ]]. Rèewi Sèeréer si ci njiitu [[Buur]]. Jolof mujj na nekk réew ni yeneen yi ci xarnub XVI ba XIX. Waaye [[Dammeel]] moom moo gënnoona metti ag jàmmaarloo ak [[Burba jolof]] ca xareb Danki ba nga xam ne moo njëkk a faagaagal nguuru Jolof gu mag ga. Ganaaw loolu la xareb Mbisin ca 1697 foofa kajoor moo Jekku, ak xareb Ambaal ci 1760, ak xareb 1886.
 
==== Ngirtey saayam ====
Rëdd 116 :
 
[[Wàll:Taariixu senegaal]]
[[Wàll:nguuriNguuri senegaal]]
 
[[ca:Jolof]]
Rëdd 129 :
[[lt:Džolofas]]
[[pl:Dżolof]]
[[pnb:وولوف بادشاہت]]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Jolof » lañ ko jële