Feppmaandu wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Xët wu bees : '''Feppmaandu''' as wàll-wàllaanu xarefulwon bi la. Di wenn ci wàll-wàllaan yi dàtt saalu xarefulwon bi. Ni ko turam di junjee, feppmaandu dafa maandu moo tax amul [...
 
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
 
'''Feppmaandu''' as [[wàll-wàllaan]]u [[xarefulwon]] bi la. Di wenn ci wàll-wàllaan yi dàtt [[saalu xarefulwon]] bi. Ni ko turam di junjee, feppmaandu dafa maandu moo tax amul [[yanu mbëj]] (du bu baax(+) mbaa bu bon(-)). Feppmaandu yeek [[feppsaal]] yi su ñu leen boolee ñooy nekk saalu xarefulwon bi. Ngir ab xarefulwon, dañuy bind '''Z''' limu feppsaal yi, '''A''' di limu feppsaal + feppmaandu. Kon limu feppmaandu yi dafay doon N =A-Z.
 
Lefu feppmaandu mi ngi toll ci 939,56533 [[Mbëjfeppvolt|MmV]]. Ki ko wuññi mooy [[Jëmm|jëmmaan]] bu [[Angalteer|waa-angalteer]] ba James Chadwick ci 1932.
 
== Xool it ==
 
*[[mbëjfepp]]
 
*[[feppsaal]]
 
*[[Xarefulwon]]
{{junj}}