Feppsaal wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Xët wu bees : '''Feppsaal''' as wàll-wàllaan la su sëfoo yanu mbëj bu baax(+) su man a féex ciy yëngoom walla mu taq cib saalu xarefulwon . Ki ñuy wax ne moo ko wuññi mooy Ern...
 
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
 
'''Feppsaal''' as [[wàll-wàllaan]] la su sëfoo [[yanu mbëj]] bu baax(+) su man a féex ciy yëngoom walla mu taq cib [[saalu xarefulwon]] . Ki ñuy wax ne moo ko wuññi mooy Ernest Rutherford, donte [[Jëmm|jëmmaan]] bu [[Almaañ|waa-almaañ]] bi Eugene Goldstein njoortoon na ag nekkam njëkk ngir manoon a dëggal ay gëstoom. Dayoob yanu mbëjam tollook bu [[mbëjfepp]], waaye ak màndarga gu wuute: 1,602 × 10<sup>-19</sup> [[coulomb]]. [[Lef|Lefam]] tuuti la rombee 1800 yoon bu mbëjfepp (daanaka 1836) te xawa tollook bu [[feppmaandu]]: feppsaal a ngi am lef gu toll ci di 1,6726231 × 10<sup>-27</sup> kg (9,3828 × 10<sup>2</sup> [[mbëjfeppvolt|MmV]]).
 
{{junj}}
 
[[Wàll:Jëmmu saal]]