Kàttanug mbëj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Kàttanug mbëj''' xeetu [[kàttan]] la gu lonku ci [[doole]] walla [[Toolu mbëj|tool]] yu jóge ci mbëj, maanaam lu ñeel yëngug, doxugwalla doxub, [[Yanu mbëj|yani mbëj]]. Kàttanu mbëj manees na koo jëfandikoo ngir defi liggéey, leeral, tàngal,...
 
== Kàttan ak dawaanu mbëj ==
Rëdd 18 :
Kàttan gi manees na koo nattee nii:
 
:<math>U_E = \int \cdot V \cdot dq = \frac {1}{22C} \int_cdot Q^{v2} dq \cdot V = \frac {1}{2} \cdot VC \cdot QV^{2}</math>
 
Kàttan gi U<sub>E</sub> ciy [[Joule]] mooy kàttan gi rënku cib toolu mbëj, C mooy [[def]] bi, di ci lees di sukkandiku ngir man a xam daayoob kàttan gees man a sol cib [[rënkukaay]].
Kàttanu gi U<sub>E</sub> ciy [[Joule]].
 
:<math>U_m = \int \cdot V \cdot I \cdot dt = \int \cdot I \Phi(t) = \frac {1}{2} \cdot L \cdot I^{2}</math>
 
Kàttan gi U<sub>m</sub> ciy [[Joule]] mooy kàttan gi rënku cib [[toolu bijjaakon]], <math>\Phi(t)</math> mooy walug bijjaakon giy soppiku ci jamono ''t''.
 
Ci yenn anam yi dees na man a bind gii [[yamale]]: