Soppalikaay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
[[Dencukaay:Soppalikaay.jpg|thumb|450px|right|Ab soppalikaay bu ñattiwéq]]
 
'''Soppalikaay''' ab jumtukaay la buy tax a man a soppi limu dend ak taraayu [[dawaanu mbëj]] gu jóge cib gongikuwaay buy jur [[kàttanu mbëj]] gu [[Dawaan gu safaanu|safaanu]], ci beneen limu dend ak taraay yu wuute te bokk [[baraay]] ak melokaan. Te limuy ñakk ci kàttan ci soppali gi lu néew la. Ab soppalikaay, ci dawaan gu safaanu rekk la man a doxe, ndax ci gii xeetu dawaan la [[mbëjbijjaakon]] gu safaanu, di ci li doxam aju, man a juddoo.
 
Ligne 7 ⟶ 9 :
:<math>P = V I \cos \phi \,</math>
 
Lii dafay tekki ne man ngaa yokk walla wàññi dend gi walla dawaan gi te ngóora gi du soppeeku (te jéem a fexe ba <math>cos \phi \,</math> jege 1 (benn)). Lii am na solo lool ndaxte dawaan gi ''I'' dafay jur tangoor suy jaar ci biir watatukaayu mbëj bi (ngir [[njeexitu Joule]]): lu dawaan gi di gën a bari tangoor giy judd di gën a bari; ngir moytu lii faww ñu yokk dijjaayu watatukaay bi, waaye it yokk gi am na dig ci wàllu koom ak xaral, taqaju na tamit ci feeñte bi ñuy duppee [[waddug dend]] yiyu buum yi ci seen bopp. Kon ngir wàññi dawaan gi dañuy def ab soppali yokkaale dend gi ci anam gu ngóora gi dul soppeeku .
 
[[Wàll:xaralaymbëj]]