Doxalukaay bu mbëj wuute gi ci sumb yi

68 octets ajoutés ,  11 at ci ginaaw
Coppite gi amul tënk
m (Tuddewaat nañ Doxalkat mbëj léegi mooy Doxalukaay bu mbëj)
'''DoxalkatDoxalukaay bu mbëj''' tekkeem moy, ab [[wuutuloxo]]b [[mbëj]] la, goo xam ne kattankàttan giy duggu ci moom gu [[mbëj]] la te ga muy gennegénne gu [[doolerandu]] la. DoxalkatDoxalukaay yu mbëj yi am nañnañu solo lool ci dundinudundiinu jamono guju bees giji, te it dëgg la sax, ne limu doxalkatdoxalukaay yu mbëj yi nekk ci am reewréew daydafay firndeel tolluwaayu jëm-kanamam. Te itam deminu, maanam yokkute walla nèewtenéewte limu doxalkatdoxalkaay yu mbëj yi ci am reewréew bokk na ci wonekat yiy firndeel tolluwaayu yokkute ci wàllu [[xarala]] mu reewréew moomu. Ngir dëggal loolu, doyna xool ci jumtukaay yi nekk ci li ñu wër: ca saxaar ba ci watukaay ak yeneen ak yeneen, yi ngeen xam ne nit ku bees ki moo ngi koy jëfëndikoojëfandikoo bu baax, man naa ni sax ñooy doxal sunug dund.
 
== Xaralay doxin gi ==
=== Wàll gi solowu: ===
* [[Wëndeelukat]]
* [[TekkaaralTekkaaralkat]]
* [[Toolu Bijjaakon]]
* [[Bijjaakon]]
 
=== Doxin ===
DawanuDawaanu [[mbëj]] gi day jaar ci abag lëmës gu ñu wëndeel ci ab doggub weñ gibi tudd [[TekkaaralTekkaaralkat]] bi. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm, jur ab toolu mbëjbijjaakon bu ca dawandawaan jaaree. Toolu mbëjbijjaakon googuboobu dañ koy sòobsóob ci beneen toolu mbëjbijjaakon gu lëmës gu [[wëndeelukat]] bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seex iseexi [[dott]]. [[Wëndeelukat]] bi tambalee wëndeelu ci sababu njureelu mbëjbijjaakon; bëj-gànnaaru toolu bijjaakon gu wëndeelukat bi day wòotalantewootalante ak bëj-saalumu toolu bijjaakon gu tekkaaraltekkaaralkat gibi. Xaaju wëndeelu gu nekk, dottudott gibi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi man a wéyee.
 
DoxalkatDoxalukaay bii, ci dawandawaan gu safaanu rek lay doxee, ndax ci dawaan safaanu rek la bijjaakon di judd. Suy dox, ag wàll gu néew ci kattanukàttanu mbëj gi day soppeeku tanggoor ngir [[sababunjeexitu joule]].
 
== Taariixam ==
Ci atum 1821, lu weesu xamteg feñte gu mbëjbijjaakon gi, simikat boobu di Ørsted xamlewoon, la [[jëmmalkat]] bu waa-angalteer bii di [[Michael Faraday ]]defar ñaari wuutuloxo ngir yooxjóox li mu duppee ab wëndeelug mbëjbijjaakon: ab jalaxubdoxub dooley bijjaakon gubu mbegewu te wéy, ci lu wër ab wëñ, ci maanaa mooy faramfaceg doxalkatdoxalukaay bu mbëj gu njëkk.
== Lëkkalekaay yu biir ==
* [[DoxalkatDoxalkaay bu demandoo]]
* [[DoxalkatDoxalkaay demandowulbu demandoowul]]
* [[DoxallatDoxalukaay bu wéy]]
* [[dawaan bu safaanoo]]
 
{{wikibaatukaay}}
3 292

modifications