Sowwu Afrig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
SieBot (waxtaancëru)
m robot Modifying: zh:西非
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Modifying: yo:Ìwọòrùn Áfríkà; cosmetic changes
Rëdd 4 :
 
Su nu sukkandikoo ci seddaleb adduna bi [[Mbootaayu Réew yu Bennoo]](onu) yi def, Sowwu Afrik bénn la ci diwaan yi ñu seddalee Afrik.
[[ImageDencukaay:LocationWesternAfrica.png|right|thumb|300px| [[Maghreb]] ak sowu Afrik]]
Fukk ak juroom bénni (16) réew la am :
* [[ImageDencukaay:Flag of Benin.svg|20px|raaya]] [[Benin]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Burkina Faso.svg|20px|raaya]] [[Burkina Faso]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Cote d'Ivoire.svg|border|19px|raaya]] [[Kot diwaar]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Cape Verde.svg|20px|raaya]] [[kap Weer]]
* [[ImageDencukaay:Flag of The Gambia.svg|20px|raaya]] [[Gaambi]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Guinea-Bissau.svg|20px|raaya]] [[Ginne Bisaawóo]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Ghana.svg|20px|raaya]] [[Gana]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Guinea.svg|20px|raaya]] [[Ginne]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Liberia.svg|border|19px|raaya]] [[Libeeria]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Mali.svg|20px|raaya]] [[Mali]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Mauritania.svg|20px|raaya]] [[Gànnaar]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Niger.svg|border|19px|bandiera]] [[Niseer]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Nigeria.svg|border|19px|raaya]] [[Niseeria]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Senegal.svg|20px|raaya]] [[Senegaal]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Sierra Leone.svg|19px|border|raaya]] [[Siraa Leyoon]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Togo.svg|20px|raaya]] [[Togóo]]
 
== Melosuuf ==
Tefesu gii xaaju Afrik ci [[Mbàmbulaanu Atlas]] la bokk. Tefesam xaajoon nan ko joxoon leen ay tur: Tefesug pépp, Tefesug wurus, Tefesug bëñu-ñay (ci nasaraan:Côte d'Ivoire, moo indi turu réewum Kot diwaar). [[Jappum njaam]] mi yëggaloon na barab yooyu bu baax; ba tax na sax lu ëpp ci [[jaam]] yi fa ñu leen jaarale yòbb [[Amerik]].
 
Ci barab yu bari yi nekk ci [[Diwaan]] bi [[klimaab yemoo]] la ñu am, [[allub yemoo]] it am na fa. Bari na ci ay réew yu bari gancax, am na ci tamit réew yu bekkoor: yi jege [[ndand féy-féy]] gu [[Sahara]], yu ci mel ne [[ Senegaal]] ak [[Mali]]
 
==== Réew yi génn ci géej gi ====
Rëdd 49 :
* [[Niseer]]
 
==== Dex yi ====
* [[Dexu Senegaal]]
* [[Dexu Niseer]]
Rëdd 56 :
 
== Taariix ==
Ci taariix Diwaanu Sowu Afrik mooy barab bi nguur yi ëppoon solo ci Afrik nekkoon, man nan cee woññi yénn: [[Nguuru Mali gu Mag ga]], [[Nguuru Songaay gu Mag ga]], [[Nguuru Gana gu Mag ga]]. Doonoon na génn ci barab yi [[xay]] yi gën a mag juddoo ci [[adduna]] bi, dëkk bu mag bii di Timbuktu bokkoon na ci selebiyoonu njaay ak cosaan yi gënoon a mag ci jamono ju yagg ja. Ay réew yu amoon-alal te bariwooni yëggu-yëgguy cosaan ak aada nekkoon nañ fa, waaye li leen gën a faagaagal mooy [[Jappum jaam|jappum jaam]] mi ak coppitey klimaa bi, ñakkum ndox mi (rawatina taw) moo réy mbay meek camm gi ak lépp li ciy génnee.
 
== njëkk-taariix ==
Rëdd 62 :
 
{{Diwaaniafrik}}
 
[[Wàll:Melosuuf]]
[[Wàll:Afrig]]
Ligne 130 ⟶ 131 :
[[vi:Tây Phi]]
[[wa:Afrike coûtchantrece]]
[[yo:Ìwọ̀orùnÌwọòrùn Áfríkà]]
[[zh:西非]]