Penku Afrig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
VolkovBot (waxtaancëru)
m robot Adding: so:Bariga Afrika
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Modifying: es:África Oriental; cosmetic changes
Rëdd 1 :
'''Penku Afrig''' mooy wàllu [[Afrig]] gi gën a féete penku. Bénn la ci diwaan yi ñu séddalee goxu Afrig.
[[ImageDencukaay:Africa-countries-eastern.png|thumb|right|300px|Lonkoyoon gu [[Afrig]] ak penku Afrig]]
juroom ñenti Réew a fa nekk:
* [[ImageDencukaay:Flag of Eritrea.svg|20px|raaya]] [[Eritere]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Ethiopia.svg|20px|raaya]] [[Ecoopi]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Djibouti.svg|border|19px|raaya]] [[Jibuti]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Somalia.svg|20px|raaya]] [[Somali]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Kenya.svg|20px|raaya]] [[Keeñaa]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Uganda.svg|20px|raaya]] [[Ugandaa]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Tanzania.svg|20px|raaya]] [[Tansani]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Rwanda.svg|20px|raaya]] [[Ruwandaa]]
* [[ImageDencukaay:Flag of Burundi.svg|border|19px|raaya]] [[Buruundi]]
 
[[Ruwandaa]] ak [[Buruundi]] yénn saa yi dan leen di boole ci [[Diggu Afrig]], ndax li ñu nekk ci diggante ñaari diwaan yi.
Rëdd 19 :
Yénn barabi penku Afrik,siiw nañ ndax seeni rabi all yu bari, yu mel ne segg, gaynde, ñay,... Li ëpp ci [[diwaan]] bii nak ñaay la. [[Doju Kilimanjaaro]] ak [[doju Keeñaa]], ñooy yi gën a kawe ci [[Afrig]].
 
Ci gii xaaju Afrig, làkk yu bari lañ fay wax, kàllaama [[waa angalteer]] ak gu [[waa faraas]] ñooy yi fa gën a tas, waaye bu nu fatte [[kiswhili]] di itam làkk bu tas ca diwaan ba; baati [[bantu]] ak yu [[araab]] ñoo booloo doon ko. [[Diine|Diiney]]y [[krist]] mooy bi fa gën a tas rawatina ca [[Ecoopi]]. Doon na diwaan bu bari ay [[xare]] yu junniy nit faatoo: ca [[Sudaan]] lu mat ay fukki at a ngii ñu ne ci xare, ca Ecopi ba [[buur]] ba daanoo ba tay ñu ngi xare ci seen biir. Moom Ecoopi am beneen xare bu mu sexxal ak [[Eriteere]] mi ko doon laaj tembteem te jot ko ci 1993, am na fanweeri at. Ca Somali itam ay at a gii ñuy xeex ci seen biir.
 
== Taariix ==
Rëdd 41 :
[[en:East Africa]]
[[eo:Orientafriko]]
[[es:África del EsteOriental]]
[[et:Ida-Aafrika]]
[[fi:Itä-Afrikka]]