Hip-hop wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 12 :
 
==== Ay cosaanam ====
Woyu hip-hop ci buumu xeeti woyi waa-aamerig yu ñuul yi la bokk. Ay dàttam ñi ngi bàyyikoo ci dundin gu metti gi ñu nekkee woon, dalee ca seeni maam ba ci jamono yi muy juddu, woy yañ daan def ca tool ya daan ca naqarlu seenug nekkin, ak caa fattali seenug jóge [[Afrig]]. Mi ngi tambalee ciy kebetu niki xeeti woy yu mel ne [[Ragetime|ragetime]], [[Jazz|jazz]], blues. Ci lu gëna jonjoo, woyu hip-hopa ngi bawoo ci ''Soul'', ak ci ''funk''. Yii xeeti woy bawoo [[bëj-gànnarugànnaaru Aamerig]] dem ba fasook sound-system bu waa-jamayka, bi àgg ba New York ndax wàlliyaan gi waa-jamayka yi daa def foofa. Ba tax-na ñett ñi ñu ne ñoo sos yëngu-yëngu hip-hop fa la ñu bàyyikoo.
 
Donte hip-hop ci yii xeeti woy la ëlee ay dàttam, waaye doonul seenug wéyale. Du lu ay tëggkat yu xereñ ci seen liggéey toog xalaat, ni blues doonee wéyaleeg jazz, gospel juddoo ci blues, soul tegu ci, funk ñëw, caaday hip-hop dafa am ab dog-dog ag yeneen xeeti woy yooyu
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Hip-hop » lañ ko jële