Haj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
== Aj Màkka ==
 
Aj mooy jooroomeelu ponku Lislaam, Ci waxi Yonent Yàlla Muhammed ji ni: "Tabaxees na Lislaam ci juroom: Seere amul benn buur bu dul Yàlla te Muhammed ndawam la, Taxawal Julli, Joxe Azaka, Woor weeru koor, Ak Aj ci ku ko man aw yoon", ba tay Aj farata la ci benn jullit bu ko man (ci bepp anam), ci waxi Yàlla mu kawe ja ni:ñeel na Yàlla ci nit ñi Aj néek ba ci ku ko man aw yoon (benn yoon) te ku weddi Yàlla moom woomle na waliif mbindéef yi.
 
 
'''Aj Màkka''' benn yoon faratala ci mukàllaf mu ko man ci yaramam ak ci ab yobbalam.
Ligne 11 ⟶ 14 :
'''Bu ci yooyu yépp amee nak''' war na ko ni ko julli ware ku ko weddi ab yéefar la, ku ko bàyyi te tay ko te tëlewu ko ci genn anam ab saay-saay la bu bon te bu ko tuubul ba dee sawara la jëm.
Ku ko bëgg nak bu demee ba fa muy armale dana fa fekk ku ko jiite ci yi mu war a def yepp ak yi mu war a bàyyi yepp ba ba muy noppi.
Moongi ware ci weeru Tabaski
[[Image:la_mecque_pelerinage.png|300px|right|thumb|Jeegoy Aji Màkka gi]]
 
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Haj » lañ ko jële