Wolof (làkk) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
MelancholieBot (waxtaancëru)
m roboto aldono de: mg:Fiteny wolof
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Removing: yo:Woloofu (Wolof); cosmetic changes
Rëdd 15 :
 
== Cosaanam ==
Ni ko gëstukat yi waxe, làkku wolof am na ag mbokkoo ak yeneen làkki Afrig yu bari, yu mu bokkali maam. làkk yi dañ leen a séddale ci ay wàll: bu ci nekk ñi am ag mbokkoo lañu fa def. Nee nañu wolof ci wàll gi ñu'y woowe bànqaasub atlas bu làkki kongóo yu kojug nit ku ñuul la bokk. Am na ag mbokkoo ak [[Pulaar|pulaar]] ak [[Séeréer|séeréer]] ak [[Joolaa|joolaa]] ak yeneen.
 
Daanaka ñoo ngi koy làkk ci senegaal gépp, bëj-gannaar ba bëj-saalum, penku ba sowwu.
Donte wolof da di làkku askanu ñi ñuy woowe ay wolof, waaye kàllaama wolof amul aw dig. Dem na ba romb dig (frontiere)yu Senegaal àgg ba [[Gaambi]], [[Gànnaar]] ba [[Mali]], ci ñaari dëkk yu njëkk yi sax boole nañ ko ci seeni làkki réew. Daanaka gox boo dem ci Senegaal am nañu waxinu wolof wu wuute: am na wolofi [[Waalo|waalo-waalo]], [[Jolof|jolof-jolof]], [[Siin-Saalum|saalum-saalum]], wu [[Kajoor|kajoor-kajoor]], wu [[Bawol|baol-baol]] ak wu [[Lebu|lebu]].
 
== Mbindin ==
Rëdd 400 :
 
== Xool it ==
* [[commons:Category:Wolof pronunciation| commons:Category:Wolof pronunciation]] Ngir déglu waxiinu baat yi
* [[:wikt:| wikbaatukaay:]] ab baatukaay bu matale ci wolof
 
[[Wàll:Wolof]]
Rëdd 440 :
[[uk:Волоф (мова)]]
[[wa:Wolof]]
[[yo:Woloofu (Wolof)]]