Weeri wolof wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
TXiKiBoT (waxtaancëru)
m robot Adding: uz:Islomiy taqvim
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Adding: jv:Kalèndher Hijriyah; cosmetic changes
Rëdd 1 :
[[Weeri wolof]], ci [[Arminaatu]] gàddaay gi, walla bu [[jullit]] ñi mbaa bu [[Lislaam]], ab arminaat bu weer la, buy sukkandiku ci doxiinu weer wi ngir xam ak natt weer wi. Jullit ñi danañu ko jëfandikoo ci bépp barab, rawati na ngir natt ak xam xew-xewi ak bisi diine yi. Ki ko sos nag mooy [[Omar Ubn Xattaab]] (g.m), daal di def [[Gàddaayug Yonent|gàddaayug Yonent]] bi (j.m) juge [[Màkka]] dem [[Madiina]] muy ab tàmbaleem, looloo waral deesi tudde ko arminaatub gàddaay gi. Ak doonte arminaat bi ci jamonoy jullit ñi lañu ko sos, teewul turi weer yi ak arminaatub weer ñu leen daa jëfandikoo ca jamonoy réer ga (jaahiliya, maanaam njëkk Lislaam)
 
Yenn ci [[réew|réewi]]i [[araab]] yi, mu ci mel ne [[Araabi Sawdit]] -moom ci nguur geek askan wi - dañuy jëfandikoo arminaatub gàddaay gi niki arminaat bu kilifawu di ci taariixe ci bindante yiy am ci diggante liggéeyuwaayi nguur gi, waaye nag lu ci dul moom, askani araab yi ci des yépp de beneen bi lañu miin te moom it lañuy jëfandikoo muy bu judd gi (juddug yonent Yàlla Isaa (j.m)).
 
Arminaanub gàddaay gi mi ngi ame ci 12 [[weer]] yu weer, maanaam atum gàddaay gi mi ngi tollook 354 bés daanaka, maanaam 354.367056 bés. Weer wi ci arminaatu gàddaay gi, benn mu nekk 29 walla 30 bés (ndax doxug weer wu feeñ wi 29.530588 bés la). Ginnaaw nag wuuteg 11 fan am na ci diggante [[Arminaatu jant|arminaatu judd]] gi ak bu gàddaay gi, ñaari arminaat yi duñu jamonoo mukk (duñu tolloo mukk) looloo waral dëppale leen di gën a jafe.
 
== [[Weer]] ci arminaatu gàddaay gi ==
Rëdd 18 :
# [[Diggi-tabaski]]
# [[Tabaski]]
== Lëkkalekaay yu biti ==
* {{fr}} [http://www.louisg.net/E_croissant_musulman.htm Le début des mois dans le calendrier musulman : difficultés]
* {{fr}} [http://www.calendrier-ramadan.com/khalid-chraibi-la-problematique-du-calendrier-islamique-397.htm Khalid Chraibi : La problématique du calendrier islamique ]
Rëdd 65 :
[[it:Calendario islamico]]
[[ja:ヒジュラ暦]]
[[jv:Kalèndher Hijriyah]]
[[ka:ჰიჯრა (კალენდარი)]]
[[ko:이슬람력]]