Maghreb wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
SieBot (waxtaancëru)
m robot Adding: sh:Magreb
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Adding: bs:Magreb; cosmetic changes
Rëdd 1 :
[[ImageDencukaay:Maghreb2.PNG|thumb|right|300px|Maghreb]]
'''Maghreb''' mooy wàll gi gën a Féete penku ci [[bëj-gànnaaru Afrik]], nekk ci diggante [[Géej gu Diggu|Géej gu diggu gi]] ci bëj-gànnaar ak [[tàkk]] gu [[Sahara]]'k gu Libi ci bëj-saalum ak [[Mbàmbulaanu Atlas]] ci penku.
 
== Cosaanu baat bi ==
Ci [[araab]] ''al-Maghrib'' di tekki "sowwugi" (suuluway); li ko waral mooy féeteem ci wàllu penku suñ ko xoolee ak fa araab yi dëkk. Di safaanoo ak [[Machrek]] (fenkuwaay, sowu), maanaam penku ga araab yi dëkkee, li ko dalee [[Esipt]] ba [[Iraak]]. Bu jëkk ''Jezirat al Maghrib'' lañ ko tuddee woon, di tekki "dun bi ci Penku", ndax nañ gisee woon diwaan bi ca jamono ju yagg ja: li mu nekkoon ci diggante [[géej]] gi ak ndand féy-féy gi.
 
Ci araab '''Maghreb''' day tekki tamit [[Marok]]. Ngir jaawale bañ ai am ci, marok ''el-Maghreb el-aqsa'' lañ koy woowee ci araab, di tekki “penku gu sori gi”. Di nañ ko wax tamit “suuluwaay gu araab”
Rëdd 17 :
[[bn:মাগরেব (অঞ্চল)]]
[[br:Maghreb]]
[[bs:Magreb]]
[[ca:Magrib]]
[[cs:Maghreb]]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Maghreb » lañ ko jële