Gàmmu wuute gi ci sumb yi

43 octets ajoutés ,  11 at ci ginaaw
Coppite gi amul tënk
m (robot Modifying: ku:Rebî' el-Ewel)
'''Gàmmu''', ( ci [[araab]] ربيع الأول) mooy ñetteelu weer ci [[weeri wolof]] tuddees na ko noonu ngir ne [[araab]] yi dañu ci daan lolliwu, maanaam daan ci am am ñax, di ci sàmm seenug jur, am ñu ne daa dëppoo ak lolli bi moo tax ñu tudde ko ko.
 
Ci [[wolof]] nak daa yem ak weer wees di màggalemàggalee juddug [[Muhammad|yonnent]] bi te màggal googu moo tudd Gàmmu ci wolof.
 
{{weeriwolof}}
677

modifications