Kureelu Mbootayu Xeet yi wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
MauritsBot (waxtaancëru)
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Kureelu Mbootaayu Xeet''' yi ndawi reewréew yu mag yi, yu ci mel ni [[Nguur-Yu-Bennoo]] , [[Diiwaan-yu-Bennoo]] yu bennoo yi Amerig[[Aamerig]], [[Bennog Sofyet ]], Frans[[Faraas]] ak [[Siin]], danoo daje woon ci Wasington peeyub Amerig ci wenn waxtaan atum 1933g, ginaaw bi as lëf ci ndam tàmblee feeñ ñeel reewi tapoo yi .
Ci noonu nu gëstu woon nan lanu fiy sose ag mbootaay gu adduna guy yëngu ci saxal ponki jàmm ci adduna bi, jële fi xeex yi, amal fi maandute ak yamoo ci diggante mbooleem reew yi, ak rafetal nekkiinu mboolaayu reewr;ew yi, ci koom-koom, mboolaay, aada ak wér.
Bi loolu jàllee nu def benn dajeb waxtaan bu adduna[[àdduna]] bi ci dëkku [[San FransiskoFransisco]] ci 25 awril atum 1945, ngir rëdd fa ag kollëre ñeel ag mbootaayug xeet gu yees gu fiy wuutu kureelu xeet yi.
Ndawi lu tollook juroom fukk ak benni reew teewe nanu ko, nangu it ci nu def kollëreg mbootaayu xeet yi, ak xaatim ko ci 26/06/1945g. La jiitu ca kollëre ga mooy:
 
 
ÑunNun askani mbootaayu xeet yi ñi ngi giñ ne di nanu xettali maas yiy ñëw ci musibay xare , yi nga xam ne sotti nanu nit ay alkande aki naqar yu kenn manul’a misaal ci ñaari yoon ci diir bu gàtt bu weesuwul genn maas reek. Ñi ngi giñ it ne dananu feddaliwaat sunu ngëm ci àqi nit ju cosaanu ji ak yelleefam, ak teddngay jëmm ak man-manam, di feddali it ne goor ñi ak jigeen ñi ak xeet yi, moo xam yu ndaw lanu, mbaa yu mag, ñoo yam kepp ci àq ak yelleef .
[[Dencukaay:Flag of the United Nations.svg|300px|thumb|raaya bu Kureelu Mbootayu Xeet yi]]
[[Dencukaay:United Nations HQ - New York City.jpg|300px|thumb|Makkaanaam ca [[New York]]]]
Rëdd 14 :
 
Wilson moom gaaraloon na naalam boobu di “Kureelu Mbootayu Xeet yi” , gaaraloon na ko ca waxtaanu jàmm wa ñu amaloon, kollëre ga ñu jotoon a fas ca [[Versaay]] it moo rëddoon lañu fa xaatim.
 
 
l'ONU nekhna torop.
 
== Ay ponkam ==