Weeri wolof wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
SieBot (waxtaancëru)
m robot Modifying: eu:Islamdar egutegia
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
[[Weeri wolof]], ci [[Arminaatu]] gàddaay gi, walla bu [[jullit]] ñi mbaa bu [[Lislaam]], ab arminaat bu weer la, buy sukkandiku ci doxiinu weer wi ngir xam ak natt weer wi. Jullit ñi danañu ko jëfandikoo ci bépp barab, rawati na ngir natt ak xam xew-xewi ak bisi diine yi. Ki ko sos nag mooy [[Omar Ubn Xattaab]] (g.m), daal di def [[Gàddaayug Yonent|gàddaayug Yonent]] bi (j.m) juge [[Màkka]] dem [[Madiina]] muy ab tàmbaleem, looloo waral deesi tudde ko arminaatub gàddaay gi. Ak doonte arminaat bi ci jamonoy jullit ñi lañu ko sos, teewul turi weer yi ak arminaatub weer ñu leen daa jëfandikoo ca jamonoy réer ga (jaahiliya, maanaam njëkk Lislaam)
 
Yenn ci [[réew|réewi]] [[araab]] yi, mu ci mel ne [[Araabi SawdiSawdit]] -moom ci nguur geek askan wi - dañuy jëfandikoo arminaatub gàddaay gi niki arminaat bu kilifawu (walla officiel) di ci taariixe ci bindante yiy am ci diggante liggéeyuwaayi nguur gi, waaye nag lu ci dul moom, askani araab yi ci des yeppyépp de beneen bi lañu miin te moom it lañuy jëfandikoo muy bu judd gi (juddug yonent Yàlla Isaa (j.m)).
 
Arminaanub gàddaay gi mi ngi ame ci 12 [[weer]] yu weer, maanaam atum gàddaay gi mi ngi tollook 354 bisbés daanaka, maanaam 354.367056 bisbés. Weer wi ci arminaatu gàddaay gi, benn mu nekk 29 walla 30 bisbés (ndax doxug weer wu feeñ wi 29.530588 bisbés la). Ginnaaw nag wuuteg 11 fan am na ci diggante [[Arminaatu jant|arminaatu judd gi]] gi ak bu gàddaay gi, ñaari arminaat yi duñu jamonoo mukk (duñu tolloo mukk) looloo waral dëppale leen di gën a jafe.
 
== [[Weer]] ci arminaatu gàddaay gi ==
# [[Tamxarit]]
# Tamxarit (Muharram ci araab), mooy weer wi njëkk ci yu gàddaay gi, moom nag bokk na ci li ñuy wax ci Lislaam "Al-ashur al-hurum", (maanaam weer yu am worma yi): tamxarit nag tuddees na ko ci araab "muharram" ngir ne araab yi dañu ci daan araamal xeex.
# [[Diggi-gàmmu]]
# Diggi-gàmmu, di ci araab (safar), tuddees na ko "safar" ci araab giy firi féex, wéet, limub tus, maanaam (zéro)ci araab mi ngi bawoo ci baat boobu di safar {sifr) ndax féexam ga, ëmbadeem ga dara. Kon safar tuddees na ko safar ci araab - ma baamu- ngir ne weer la wow këri araab yi dañu ci daan wéet, féex ci ci ay ñoñam ngir xare-ji, waxees na it ne li ko waral mooy araab yi dañu ci daan song ak a lokki giir yi, bu ko defee ñu leen di "safaral" maanaam tusal ci seeni bagaas ( maanaam jël li ñu am ba duñu deseeti "tus" (sifr),ñu mujj di ñu wéet ciy yére, féex ciy bagaas).
# [[Gàmmu]]
# Gammu (rabiihul awal ci araab), tuddees na ko noonu ngir ne tur wi daa dajeek ab lolli (rabiih), daal di ko far jël.
# [[Rakki-gàmmu]]
# Rakki-gammu, (rabiihus saanii) tuddees na ko noonu ngir ne araab yi dañu ci daan lolliwu, maanaam daan ci am am ñax, di ci sàmm seenug jur, am ñu ne daa dëppoo ak lolli bi moo tax ñu tudde ko ko.
# [[Rakkaati-gàmmu]]
# Rakkaati-gammu (jumaadal uulaa), njëkk [[Lislaam]] nag (jumaadaa xamsa) lees ko tudde woon, lu tax nag ñu yudde ko ko? ndax daa nekkoon ci sedd bi bi ñu ko koy tudde, nga xam ne ne ndox mi da daan way (jumaada) mi ngi juge ci "jamada" giy tekki way, maanaam ndox mi da ci daan way di def ay donji yuur (galaas) ngir ag sedd.
# [[Maami-koor]]
# Maami-koor, (jumaadal aaxira), njëkk Lislaam (jumaadaa sitta) lañu ko tudde woon, moom nag turam woowu mi ngi ko jële ci fiiroo gi mu defoon ak sedd bi, tur wa daal di koy topp (way).
# [[Ndeyi-koor]]
# Ndeyi-koor,(rajab ci araab) moom nag ci weer yi am worma la bokk. Tuddees na ko nag Rajab ci araab, ngir ne ci weer woowu dees ci daa wéer ngànnaay yi, nocci ñawka yi wëlif xeej yi, daawuñu ci xeex, dees na wax (rajaba) maanaam taxawlu na wëlif xeex bi.
# [[Baraxlu]]
# Baraxlu, (walla sahbaan ci araab), tuddees na ko noonu ndax aw ñall la (shahb ci araab) ci diggante "rajab" ak "ramadaan". Waxees na ne nit ñi daño cee baaxoo woon a tàqalikoo ak a ñallu (tas) ngir sàkku-ji ndox, mu daal di jël tur woowu.
# [[Koor]]
# Koor, mooy weer wi jullit yiy woor, tuddees na ko "ramadaan" nag ci araab ngir tàngoor wu tar wi mu àndaloon ak jant bu saf bi ci nekkoon bi ñu ko koy tudde
# [[Kori]]
# Kori, ci la jullit ñiy wori ci seenug koor, mi ngi tudd nag ci araab "Sawaal" ngir ne sawaal day tekki ci araab ag jeex akug ñàkk meew, te ci weer woowu seen naaga yi (giléem yu jiggéen yi) dañu ci daan jeex, ñàkk ci meew.
# [[Diggi-tabaski]]
# Diggi-tabaski, walla "sil-qihda" ci araab, moom nag ci [[weer yees wormaal yi]] la bokk: tuddees na ko noonu ci araab ngir ne "qahada" ci araab giy tekki jekki la baat bi juge, li ko waral nag di jekki gi ñu ci daan def wëlif xeex, wëlif it ñax, daawuñu ci laxas ngir sàmmi, daawuñu ci xeex, ngir wormaal ko, araamal ci xeex.
# [[Tabaski]]
# Tabaski, walla "sul-hajja", tuddees na ko noonu ngir ne mooy boroom aj gi, ci la araab yi daan aji Màkka, ci la tabaski gi it nekk, moom nag bokk na ci [[weer yees wormaal yi]].
==Lëkkalekaay yu biti yi==
 
==Lëkkalekaay yu biti yi==
* {{fr}} [http://www.louisg.net/E_croissant_musulman.htm Le début des mois dans le calendrier musulman : difficultés]
* {{fr}} [http://www.calendrier-ramadan.com/khalid-chraibi-la-problematique-du-calendrier-islamique-397.htm Khalid Chraibi : La problématique du calendrier islamique ]
Ligne 29 ⟶ 28 :
[[Wàll:Lislaam]]
[[Wàll:Arminaat]]
[[Wàll:weeri wolof]]
 
[[af:Islamitiese kalender]]
[[ar:تقويم هجري]]