Diiney Afrig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Aucun résumé des modifications
Rëdd 41 :
 
Ca diiney bobu, mam yi ñu nek ca rewum yallah, ño nek ca diganté yallah ak nit yi. Mam yi, ño yobu ñaan yi nit yi ca yallah. Li moye tax ca diiney bu am Afrig, mam yi, amna nu solo. Wayé su bene nit gëen aduna, ngiir mu nek mam (''Akhu'' wala ''Matiu'' ca diiney bobu), yallah mo wara ko mey lolu su nit ki, bu mu néké aduna, lu bax lodone def. Nit ki, su lu bone lodone def, bu mu néké aduna, meunoul nek mam (''Akhu''), té ca aduna, ti njabotam ak yenene nit yi, ken mounoul ko niane dara. Ca Seereer yi nek ca [[Senegaal]], mam yi ''Pangol'' moye seen tuur. Lebu yi, ''mam tuur'' lañuy wax.[[Image:800px-Pyramid Texts Teti I.JPG|thumb|right|300 px|Téeré Bammel, bu Téti {{Ier}} ca Saqqarah]]
 
Tamit, xam nañu ni, ca xeet ku nek, Yallah wacc na leen ay yonenté. Li moye tax diiney afrig bobu, amna ñi seen yonenté.