Diiney Afrig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Gamadji~wowiki (waxtaancëru)
m Tuddewaat nañ Diiiney Afrig léegi mooy Diiney Afrig
Aucun résumé des modifications
Rëdd 54 :
*''Djehuty''. Ca diiney afrig, ki mo indaalé xam xam, ak bind, ca aduna. Ki moye ''Idrissa'' ca lislaam, wala ''Henoch'' ca dinney nasaraan.
 
*''Maât'', (tuuru Maty, ca ki la jogue). Moye bene yonenté bu jigen, mo doone jangal nit yi, wax bu degg, naka lañu wara bax ak yenene nit yi, ak lep bu demé nonu, ''Jom''. Li mote yax ca diiney afrig, su bene nit defdeful lu bax, dañu né ko: Defal Maât. ''Ubuntu'' ca wa Kongo.
Ñom ño yonenté bu geuneu am solo ca diiney bobu, ndax amna yenene, té xeet yi ca afrig, bu nekk ca diiney afrig, ba tey, am nañu tuur yu bari ngiir tuddu yonenté yi. Ca diiney bobu, ''Neteru'' mo doon tuuru yonenté yi, wala ''Sara''. Neteru ak Sara moye ca Wolof, domu Yallah.