Diiney Afrig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Aucun résumé des modifications
Rëdd 46 :
Tarikhkat yi woné nañu tamit, yonenté bu nek ca diiney afrig, yenene diiney yi melni diiney nasaraan, yawut ak lislaam, dugu neen ko ca sene geum. Yonenté bu Afrig ño:
 
*''Ausar''. Yonenté bu jekk am ca aduna ca diiney bobu. Amna tuur yu bari: Isha (ca lislaam moye Issa), Oni (ca diiney nasaraan moye Ori), Kem-Our, ca lakku ''Medu-Neter'' bu amone ca jamono bobu mu nekkone, Kem-Our moye nit ku ñul bu mag. Tarikhkat né nañu, tarikh bu Ausar mo juur tarikhu Issa bu lislaam, Kirist ca [[Biibël]]. Ausar ca xeet anu''Anu'' la bokkéwone, bene xeet bu amone bu jekk, di dekkone ca Sudan (Nguruu Kush), ñom ño tabax ngurru Misra, ak Buur Fari ba mu tuddu ''Narmer'', amna nient junni at. Ausar, bobu nekkone ca aduna, ay junni ak junni at la woon, sogo sax diiney yawut am, sogo ngurru Misra am.
 
*''Aset'' (tuuru Aïssata ci mom la jogué). Mo done jabaru Ausar. Ki rek ca aduna mo xamone tuuru yallah yep. Ndax nit ya ca, xam nañu juroom nient fukk ak juroom nient tuuru yallah, wayé Aset tuur yep la xamone. Temeram tuur yallah, mo def ni ku ko xam meunta sos lep melni yallah. Wayé yallah néna Aset,: xamga sa ma temer tuur, wayé man ma la geuneu mag, té dina def ni nga meunteu juur nit, wayé dinga ko juur ca sa biir yaram. Li moye tax Jigen ño juur dom ya, ca diiney bobu. Aset ak Ausar ño juur ''Heru'', seen dom. Natal bi ñi woné yayu Kirist bu tuddu Mari ak domam, ca natal bi ñi woné Aset ak domam Heru la jogué.
 
*''Seth''. Ca diiney afrig moye Seytan. ''Satan'' ca diiney kirist, wala ''Sheytan'' ca diiney lislaam, ca ki la jogué. Ca diiney afrig, yallah mo joor Seth ligueyam li muy def. Ligueyam moye mu sonal nit yi ca aduna, ndaxngiir yallah meun xam ku jarral dem ajjana ak ku wara dem ''Douat'', Douat moye ''Al-Jahim'' ca lislaam, ''Enfer'' ca diiney nasaraan. ''Nebetou'' modonemodoone jabaramjabaru Seth, wayé ki baxon na. Nebetou modoon dencc keuru Seth, te di nettali ca Aset ak yenene yi, lan la Seth bougone def ngiir mu meunteu sonal Ausar ca ndigel bobu yallah ko joox. Ndiguelu yallah joox Ausar, modoon mu jubanti nit y nekkone ca aduna, ngiir ñu xamné amna yallah, té bayi yeufu bone ño doon def.
 
*''Djehuty''. Ca diiney afrig, ki mo indiindaalé xam xam, ak bind, ca aduna. Ki moye ''Idrissa'' ca lislaam, wala ''Henoch'' ca dinney nasaraan.
 
*''Maât'', (tuuru Maty, ca ki la jogue). Moye bene yonenté bu jigen, modonemo doone jangal nit yi, wax bu deugeudegg, naka lañu wara bax ak yenene nit yi, ak lep bu demé nonu, ''Jom''. Li mote yax ca diiney afrig, su bene nit def lu bax, dañu né ko: Defal Maât. ''Ubuntu'' ca wa Kongo.
Ñom ño yonenté bu geuneu am solo ca diiney bobu, ndax amna yenene, té xeet yi nek ca afrig, bu nekk ca diiney afrig, ba tey, amanaam nañu tuur yu bari ngiir tuddu yonenté yi. Ca diiney bobu, ''Neteru'' mo doon tuuru yonenté yi, wala ''Sara''. Neteru ak Sara moye ca Wolof, domu Yallah.
 
Ca yonu imbraator gu gana, [[lislaam]] ñow na soowu Afrig, ca jamono bobu, lislaam ak diiney bu Afrig, ca jaam lañu dekkande woon.