Diiney Afrig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Aucun résumé des modifications
Rëdd 42 :
 
Ca diiney bobu, mam yi ñu nek ca rewum yallah, ño nek ca diganté yallah ak nit yi. Mam yi, ño yobu ñaan yi nit yi ca yallah. Li moye tax ca diiney bu am Afrig, mam yi, amna nu solo. Ca Seereer yi nek ca [[Senegaal]], mam yi ''Pangol'' moye seen tuur. Lebu yi, ''mam tuur'' lañuy wax.
 
Tamit, xam nañu ni, ca xeet ku nek, Yallah wacc na leen ay yonenté. Li moye tax diiney afrig bobu, amna ñi seen yonenté.
Tarikhkat yi woné nañu tamit, yonenté bu nek ca diiney afrig, yenene diiney yi melni diiney nasaraan, yawut ak lislaam, dugu neen ko ca sene geum. Yonenté bu Afrig ño:
 
*''Ausar''. Yonenté bu jekk am ca aduna ca diiney bobu. Amna tuur yu bari: Isha (ca lislaam moye Issa), Oni (ca diiney nasaraan moye Ori), Kem-Our, ca lakku ''Medu-Neter'' bu amone ca jamono bobu mu nekkone, Kem-Our moye nit ku ñul bu mag. Tarikhkat né nañu, tarikh bu Ausar mo juur tarikhu Issa bu lislaam, Kirist ca [[Biibël]]. Ausar ca xeet anu la bokkéwone, bene xeet bu jekk di dekkone ca Sudan (Nguruu Kush), ñom ño tabax ngurru Misra, ak Buur Fari ba mu tuddu ''Narmer''.
 
*''Aset'' (tuuru Aïssata ci mom la jogué). Mo done jabaru Ausar. Ki rek ca aduna mo xamone tuuru yallah yep. Ndax nit ya ca xam nañu juroom nient fukk ak juroom nient tuuru yallah, wayé Aset tuur yep la xamone. Temeram tuur yallah, mo def ni ku ko xam meunta sos lep melni yallah. Wayé yallah néna Aset, xamga sa ma temer tuur, wayé man ma la geuneu mag, té dina def ni nga meunteu juur nit, wayé dinga ko juur ca sa biir yaram. Li moye tax Jigen ño juur dom ya, ca diiney bobu. Aset ak Ausar ño juur ''Heru'', seen dom. Natal bi ñi woné yayu Kirist ak domam, ca natal bi ñi woné Aset ak domam Heru la jogué.
 
*''Seth''. Ca diiney afrig moye Seytan. Satan ca diiney kirist, wala Sheytan ca diiney lislaam, ca ki la jogué. Ca diiney afrig, yallah mo joor Seth ligueyam li muy def. Ligueyam moye mu sonal nit yi ca aduna, ndax yallah meun xam ku jarral dem ajjana ak ku wara dem ''Douat'', Douat moye ''Al-Jahim'' ca lislaam, ''Enfer'' ca diiney nasaraan. ''Nebetou'' modone jabaram.
 
*''Djehuty''. Ca diiney afrig ki mo indi xam xam, ak bind, ca aduna. Ki moye ''Idrissa'' ca lislaam, wala ''Henoch'' ca dinney nasaraan.
 
*''Maât'', (tuuru Maty ca ki la jogue). Moye bene yonenté bu jigen, modone jangal nit yi, wax bu deugeu, naka lañu wara bax ak yenene nit yi, ak lep bu demé nonu. Li mote yax ca diiney afrig, su bene nit def lu bax, dañu né ko: Defal Maât.
Ñom ño yonenté bu geuneu am solo ca diiney bobu, té xeet yi nek ca afrig bu nekk ca diiney afrig ba tey, amana tuur yu bari ngiir tuddu yonenté yi.
 
Ca yonu imbraator gu gana, [[lislaam]] ñow na soowu Afrig, ca jamono bobu, lislaam ak diiney bu Afrig, ca jaam lañu dekkande woon.